🔴FACE TO FACE BALLA GAYE 2- BOMBARDIER, EUMEU-LAC 2, DIENE KAIRÉ-MODOU ANTA | 21 FÉVRIER 2021

21 feb 2021
147 635 visualizzazioni

🚩S’abonner à la chaîne de la 2stv cliquez sur ce lien👉 : bit.ly/3cnXP6h
Retrouvez l'ensemble de nos programmes d'actualité et émissions de société, santé, politique, culture, musique, économie sur:
- itworlds.info
- www.2stv.net
- Iptv disponible sur 2stv.sn
- instagram.com/2stv_senegal/
- facebook.com/2stvsenegal
- twitter.com/2stvsenegal
- www.dailymotion.com/video/x7vidbb
#GASTONPROD #BECAYEMBAYE #2STVLIVE #BALLAGAYE #BOMBARDIER #EUMEUSENE #LAC2 #DIENEKAIRE #MODOUANTA #2STVSENEGAL

Commenti
  • Eumeu sene roubei rek ley def🤣🤣🤣

    Aziz FallAziz Fall5 ore fa
  • Doul rekk ak roubé vous les lutteurs kenn doussi vaccinéwou vous mentez vaccin vaccin merde tounou ndeye vaccin covid19

    Seckou Pierre BiayeSeckou Pierre Biaye9 ore fa
  • Balla gaye 2

    Naby DiaNaby Dia22 ore fa
  • Gaston is back le dong king de l arene est de retour

    vbddfy euuytvbddfy euuyt23 ore fa
  • Vaccin motakh gén takhawal combat yi ms mane vaccine wouma billahi ak kane

    Show TvShow TvGiorno fa
  • Athiaa Balla

    Ahmadou Bamba DiengAhmadou Bamba DiengGiorno fa
  • Toujour polotique à quand émergens pour le senegal. il ya beaucoup de f'ou. Senegal mais sonko incha'alla président par force😡😡😡😡💪💪💪

    ackackGiorno fa
    • J'aime tropp Eumeu 😂😂😂😂😂

      vbddfy euuytvbddfy euuyt23 ore fa
  • Eumeu mon lutteur je t aime ndam rkk

    Momath ThiamMomath ThiamGiorno fa
  • No billahi li mo nèkh dama contante LOL sakh😁😁😁😁😁😁

    Mbaye DiagneMbaye DiagneGiorno fa
  • Mane Eumeu Sène dama paré si say mbir. Depuis ta défaite humiliante contre Modou Lo, lo deff baxna

    Choose WiselyChoose WiselyGiorno fa
  • 🙏🙏

    Mbaye DiagneMbaye DiagneGiorno fa
  • Gaston geumo ndey dara yow sa guemine bou ndey yarakh bi

    diop jeandiop jeanGiorno fa
  • Magui dogua guiss lounouy mayè di nèkhal niteñi mou gnakk yi 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🖤🖤🖤🖤

    Ndiaga DiopNdiaga DiopGiorno fa
  • Day doul rek

    Xadim SyllaXadim Sylla2 giorni fa
  • Mbeur yi ay defen lanou nouniou ame xalis rek lanouy def aferii polotique la domeram

    Xadim SyllaXadim Sylla2 giorni fa
  • Balla Gaye 2 merci d'être toujours à côté du peuple parce que ton discours est carré !!!!!

    fallou kanefallou kane2 giorni fa
  • Yaw lac sa xol bakhoul ndax sosekate ngua do am ndamm dehh😛😛😛

    Mamadouaby SineMamadouaby Sine2 giorni fa
  • Eumeu vrai gentleman la

    Moustapha SambMoustapha Samb2 giorni fa
  • Galsen moy meti macky Sall diokh Gaston sunu xaliss. Aye milliards pour bene journée ! Réveiller vous la jeunesse sénégalaise

    diallo souleymanediallo souleymane2 giorni fa
  • Kepp ku vaccine mon nga ku reegu, tobab b sah nang ku njo vaccine✨be careful guys😊

    Ebrima NyanEbrima Nyan2 giorni fa
  • Eumeu sene yalla nalla yalla défall ndam

    Pape momar CisséPape momar Cissé2 giorni fa
  • J'aime tropp Eumeu 😂😂😂😂😂

    Nico PascalNico Pascal2 giorni fa
  • Bou yalla woxone you vaccin sakh doumako déf pour Mouy léer ay Balla emeu waye na donne Modou lo sama mbeur bi sakh wokhoumalak lac 2 yambar bi 🤐

    succès boyz frm KoLDa niogui Bel-Airsuccès boyz frm KoLDa niogui Bel-Air2 giorni fa
  • Bou feke yeuna mom nitt yi dina woo

    Cheikh NdawCheikh Ndaw2 giorni fa
  • Balla Gueye 2 yalla nala yalla may ndam

    Bousso NdiayeBousso Ndiaye2 giorni fa
  • Hoto naateehen siiraani de

    Harouna DiaHarouna Dia2 giorni fa
  • das ist sehr schon

    pape modou Gueyepape modou Gueye2 giorni fa
  • so done yari yon ngay deh meu vacciner wou mais comme bene leuh mome bayi meu fii bacii kanam

    IBRA DIENNEIBRA DIENNE2 giorni fa
  • lac 😂😂

    Abdou Rahim Ngomh hAbdou Rahim Ngomh h2 giorni fa
  • Yen boulenhiou yap..vous voyez tout l’archenement contre l’Afrique..Vous croyez que les gens sont bêtes ? A vouloir lutter coûte que coûte faut pas nous sacrifier..On aime la lutte mais vous et votre vaccin au diable.

    bm killer tvbm killer tv2 giorni fa
  • Plateau bi saffoul lambeu kw

    Sarr SerigneSarr Serigne2 giorni fa
  • Félicitations sama frère Kalle Wade...bonne continuation

    Talla CisseTalla Cisse2 giorni fa
  • Fo dem amna ay nafekheu università ay fenkate Moy genr yi. Gaston il veule nous faire oublier Notre objectif sur le politiche

    Sarr SerigneSarr Serigne2 giorni fa
  • Gaston merde

    Sarr SerigneSarr Serigne2 giorni fa
  • Gaston,il faut arrêter avec la politique, nous avons l'impression que vous faites un lavage de cerveau et imposer le président en place,par contre les sénégalais ont besoin de changement car le monde est en évolution,il faut suivre le mouvement.

    Aboubacar NdiayeAboubacar Ndiaye2 giorni fa
  • Avant chaque combat tu fais départ gaiendé paroles arrivée beuré mouss

    Hamet NDOYEHamet NDOYE2 giorni fa
  • Lac ! on ne mâche pas un chewing-gum quand on parle

    Hamet NDOYEHamet NDOYE2 giorni fa
  • Parlez de votre profession. Vous ne connaissez rien du vaccin. Arretez d'être berné par les aventuriers et opportunistes. La jeunesse vous portent énormément dans leurs cœurs. Faites attention.

    paul bassepaul basse2 giorni fa
  • Ce op possible de fermer le Facebook de person frere

    Mamadou TimeraMamadou Timera2 giorni fa
  • Lamb dji politique rek moko lal, loutakh mbeur yi done ci wakh dpui plus d’un an? Instant bi vaccins yi ak situation Senegal motakh beug leundeumal askan wi rk Gaston mom nitou intérêt la dey mar tatou président de la république 👎🏽

    King LycoKing Lyco2 giorni fa
  • Vous la continuer votre truc des diables vous allez voir pourquoi vacciner c'est pas possible vous êtes malade vraiment 😭😭😭

    Djimo DansokhoDjimo Dansokho2 giorni fa
  • Boul quein vacciné les pays africain ils sont refuise jamais boul Quein falle ngih Louniouwa xamouniou dara dia gouniou m'aime europ nagoulniou bolle ne wede dème leine couko diel ya xam merci

    Carld baCarld ba2 giorni fa
  • Politique leu

    ABDOUSALAM JAMMEH abdou888ABDOUSALAM JAMMEH abdou8882 giorni fa
  • Je suis amateur et je voulais juste preciser que les mesur bariere doive etre appliquè mème sur les plateau. Respecter la distance et les masque

    ngouda Djittengouda Djitte2 giorni fa
  • Lac la même chose

    POULL ORPOULL OR2 giorni fa
  • Mane loutakh Gastón nékhouma rekk la khamoule

    Mamadou DiengMamadou Dieng2 giorni fa
  • Le Baobab me tue 😂😂😂👌🏿

    Lass MarleyLass Marley2 giorni fa
  • Respectez vous et ayez le cran de venir sur ce plateau et parler seulement de lutte. On vous fait dire des choses que vous croyez pas au sein de vous.

    Lass DiabyLass Diaby2 giorni fa
  • Eumeu mbeur dou beury retane ak togne koi danioulay nièmè rek

    Birama DioufBirama Diouf2 giorni fa
  • pikirouwounou way eumeu yalnala yalla may ndam lou sedd way

    sagna laminesagna lamine2 giorni fa
  • 0:33 Kou may Laadial Balla Louy *"vacsisé wou"* 🤣🤣🤣🤣🤣

    Moustapha GayeMoustapha Gaye2 giorni fa
  • Théâtre où lutte?

    Jamal MajallJamal Majall2 giorni fa
  • yene dagen yabate si vaccin laniou lene diar pour gene beuri

    Ba SouaibouBa Souaibou2 giorni fa
  • Vaccine yi deh macky day yakh khalis rek mais ken dou vaccine wou deh va la bas.

    Elhadi TallElhadi Tall2 giorni fa
  • Mane lima diakhal moy mbeur yi li Macky Sall di def ni Sénégal gnom lane motah guisouma bene mbeur bouthi wakh wala gnom li Macky Sall di def ni guisougnouko 🤦‍♂️🤦‍♂️

    bamba Diopbamba Diop2 giorni fa
  • Eumeu 💯🙏🙏

    Sow MamadouSow Mamadou2 giorni fa
  • Sonko président un cha'allah

    Modou MbayeModou Mbaye2 giorni fa
  • j'aime trop la lutte mais ça m'énerve le faite que vous nous prenez comme des souris vous croyez qu'en nous jetant des morceaux de fromage que vous nous auriez. arretez vos cinémas c'est du vrai politique

    Kems SowKems Sow3 giorni fa
  • C est juste pour divertir les senegalais, comme à l époque romaine. Faut pas oublier l actualité surtout Sonko Sonko Sonko

    Marie Raphaël GomezMarie Raphaël Gomez3 giorni fa
  • J

    Moustapha NdiayeMoustapha Ndiaye3 giorni fa
  • Mbeur yi sene wakh rafetna consernant les vaccins il faut eviter le syndrome c politique

    madate seckmadate seck3 giorni fa
  • Eumeu srx sonalgha mbeur yi😂

    Diallo MamadouDiallo Mamadou3 giorni fa
  • Gaston is back le dong king de l arene est de retour

    madate seckmadate seck3 giorni fa
  • 45:58 Thieuyy Balla akka raffet khol

    Dtl DtDtl Dt3 giorni fa
  • Merci Balla Gaye 2 waax ngu lepp champion

    Dtl DtDtl Dt3 giorni fa
  • Ils veulent nous distraire mais tous les vendus sont démasqués par l'aide de DIEU. Désabonnez-vous à ces chaînes TV et ses prometteurs de lutte qui sont avec le régime Abas à ce régime de Macky Sall

    RoodeathRoodeath3 giorni fa
  • 23:34 👀 Kou guiss lima guiss 😂😂😂

    Dtl DtDtl Dt3 giorni fa
  • Lamba c'est fini onne avance sur catastrophe

    mouhamed sowmouhamed sow3 giorni fa
  • Gaston sa intere kesse motakh ngay sambay mbayan macky sall

    Modou dieng FayeModou dieng Faye3 giorni fa
  • Gaston sa lamb yii nga khamne ay thiakhan rekla moo takh ngay digeul nityi nou vaccin wou te yaa geuna khamne vaccin yi bakhoul

    Modou dieng FayeModou dieng Faye3 giorni fa
  • Allez vous faire vacciner vous qui parlent du vaccin.. des vrais bouffons !

    tounkss 94tounkss 943 giorni fa
  • Bouken vaccinewou man mangui Italy mousou ma guise kou vaccinewou

    Pape DiaPape Dia3 giorni fa
  • Gaston mbengue il décide de revenir dans la lutte pour distraire l'opinion Les jeunes ne sont plus dube à suivre des lutteurs qui gagne des centaines de millions à une soirée pour apres retourné vivre dans leur galère ont ce fiche de ces combats #liberez le peuple je vous dis ont souffrent

    Sandjiry GueyeSandjiry Gueye3 giorni fa
  • Lac 2 chewing gum bi foko tekkkk

    Mohammed GanduMohammed Gandu3 giorni fa
  • Yallananiou Yalla mouseul si politique Gaston khaly sétal Yalla si lingay wakh si Macky

    Mohammed GanduMohammed Gandu3 giorni fa
  • Gaston Khaly Mbengue Ziarrr nala wayé kenn dou wakh malekoum salam on dit wa haleykoum Salam jajeuf

    Mohammed GanduMohammed Gandu3 giorni fa
  • Noooo! Gni nio gnémé yalla. Je suis vraiment désolé. Amoul kéne kou meuna assurer que vaccin bi amoule effet secondaire, donc li aye risque rek la, se vacciner au covid c'est joué au jakpot je vous l'assure.

    Modou XASSIDA TVModou XASSIDA TV3 giorni fa
  • A thiae balla gaye 2 ndame rek

    loumbal baladji tv koupo gasiloumbal baladji tv koupo gasi3 giorni fa
  • Man gus na comba balla gaye ak eumeu sene mome la gaston di wakha

    loumbal baladji tv koupo gasiloumbal baladji tv koupo gasi3 giorni fa
  • Maintenant tout le monde grandit même lac de guerre maintenant est devenu responsable li naikh lol

    Diop Serigne saliouDiop Serigne saliou3 giorni fa
  • Lamb ji lan len topi mie do Aÿ vaccin ok

    Babacar DieyeBabacar Dieye3 giorni fa
  • Mane yow Eumeu des fois g du mal à te comprendre BG2 guiss nga nimou leukeulé akk lac ngay dééwanti té na nga féxé ba bayii li nga waaxone akk sa fans yii si yow akk BG2 weet gooré wetalikou gooré wasalam Yalla na BOROM bii maye ndam Eumeu akk B52 si Sene combat yii

    Badara DioufBadara Diouf3 giorni fa
  • Macky sall bouko Oussmane sonko vacciné ba paré man m’a vacciné wou

    Gora MbengueGora Mbengue3 giorni fa
  • Merci eum sene 🇸🇳💔

    Walowalo WalowaloWalowalo Walowalo3 giorni fa
  • Inshallah B52 YALLA NA 2-0 bi ame

    Badara DioufBadara Diouf3 giorni fa
  • Tallou niou ndey lambeu sonko laniou talle ak avvenirou Senegal 🇸🇳

    Gora MbengueGora Mbengue3 giorni fa
  • Yeune mbeur yi esk xame guenne lounek thi vacciné bâ bakh guene diko wakh dakh khalis bi gno leun diokh motakh setleun yalla thi li guenne yene askanwi

    Lama barryLama barry3 giorni fa
  • Kou setlou nii eumeu dane neu ténor yi nek si plateau bii pouss bleu pour Eumeu Sène le champion

    Mademba SyMademba Sy3 giorni fa
  • Eumeu sene dafay nape la souvent dans les face to face...mdr eumeu sene balla gaye ont montré au sénégalais qu'ils sont frères....

    Oumar cisse BaldeOumar cisse Balde3 giorni fa
  • Tapal felle niakou ma man

    Fallou MbodjiFallou Mbodji3 giorni fa
  • Peuple sénégalais je vous parle il faut boycotter les vaccins

    Badara DioufBadara Diouf3 giorni fa
  • Eumeu no stress

    WantedSN TVWantedSN TV3 giorni fa
  • c'est la honte si je comprends bien ces combat ont été montés pour pouvoir passer vos messages à travers les lutteurs si c'était pas du politique Gaston n'oserait jamais monter ce combat ça prouve qu'il a été financé par l'état pourquoi vous nous prenez tjrs comme des cons c'est comme si vous parlez à des petits gamins zeubé

    Kems SowKems Sow3 giorni fa
  • Balla gaye moye sene Star💥

    zamane Dèmezamane Dème3 giorni fa
  • ay gouthi vaccina woo dooo too beré ba fawwou

    Moustapha thioneMoustapha thione3 giorni fa
  • Eumeu dafa cool nak bilay

    Papi SenePapi Sene3 giorni fa
  • Balla gaye 2 bonei Serigne bassirou bara damalayi geun beug

    Papi SenePapi Sene3 giorni fa
  • Gaston politique rek gay defff l

    karakara3 giorni fa
  • Diène kairé iaw khamo dianguo bonane vaccin mounoul rayy nitt dagane thiakhane

    Mor NdiayeMor Ndiaye3 giorni fa
  • #boycotter@gastonproduction.com.. Ils veulent arnaquer les modou modou

    Dj JoaquimDj Joaquim3 giorni fa
ITworlds