De retour à Dakar, Reug Reug s'énerve et vide son sac : "Awouma Défaite, combat bi danioukoy défate"

2 mag 2021
188 878 visualizzazioni

Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct facebook.com/luttetv/
facebook.com/luttetv/
instagram.com/luttetv/
luttetv.com/
itworlds.info

Commenti
  • Reug reug💪🏿💪🏿💪🏿

    Odored AnimeOdored Anime22 minuti fa
  • Ki Khana gambien la deg na anglais buou bakh you no rek ngai deg

    ezzy boyezzy boy28 minuti fa
  • Sa communication sofna reug, ak niveau binga tolou ni essaie de payer des experts en com pour combler le tout .... "Kou nangou danou" nak

    Sarrenebi LilSarrenebi Lil7 ore fa
  • Reug reug kholatal sa communication nak champion nga mais trop de confiance te tue a petit coup petit desse nga lou beuri sah liigueyatal boubaah merci

    Aliou DioneAliou Dione7 ore fa
  • Hooital lagnla yobou gaye dieulatt wadji biyone mba doula yobou .........

    papa demba keur massarpapa demba keur massar10 ore fa
  • Mbeur mounone ga bayi mou séd Gaye doeulatt wadji Wadji dalay raye bakhna

    papa demba keur massarpapa demba keur massar10 ore fa
  • Courage rec beur

    Aliou KamaAliou Kama10 ore fa
  • Reug reug wadji dala meun. Mola dak beuré deeeeh

    Ibrahima GueyeIbrahima Gueye19 ore fa
  • Reug je suis fiére de toi mais tu manque de souffle tu doit travailler l'endurance plus le combat dure plus tu souffre. Tu doit accepter les critiques. Et courage champion 💪🏿

    Elhadji Ibrahima DiopElhadji Ibrahima Diop19 ore fa
  • 🇸🇳💪🇸🇳💪🇸🇳💪🇸🇳Machalla 🇸🇳💪🇸🇳💪🇸🇳💪🇸🇳💪🇸🇳

    Fallou MbowFallou MbowGiorno fa
  • Mougnal rek dina bakh mais mEuno bagn critique yii. Bayil yEin yi mou dial Dakor ✌️

    Tazzdja AyefffTazzdja AyefffGiorno fa
  • 😂😂😂 ki koukoy var neina wadji daurou ko🚶🏿🚶🏿

    Djibril NdiayeDjibril NdiayeGiorno fa
  • L'humilité est une des valeurs d'un vrai sportif. Tu es grand champion mais accepte d'être critiquer car tu n'es pas parfait

    Bb ngBb ngGiorno fa
  • Mashallah

    fatou syfatou syGiorno fa
  • tout les fetich de tes mille marabouts ne serviront a rien ce gars est plus technique que toi il te chicotera a nouveau🤣🤣🤣😂

    Jean LeBlancJean LeBlancGiorno fa
  • Il se prend pour Floyd Mayweather

    papa ousmane goudiabypapa ousmane goudiabyGiorno fa
  • Yaw mom dagua fou y té khamo sa bopou reugue reugue Gatt khamoko d'i sonal nitt gni

    Moustapha diengMoustapha diengGiorno fa
  • Reuk reuk yaw khana do domou adama rek walla waro ame défaite frere sa nagou molaye trompe chaque jour danioula mene doumela nangoule boule niou sonale sofnga trope

    Moussa TerangaMoussa TerangaGiorno fa
  • Reug reug xalé gua naguoul critique gua guena liguéy dém diagui xékh

    seriñ saliouseriñ saliouGiorno fa
  • N'diaye numéro 1 niaw na 😂😂

    Cheikh DiakhateCheikh DiakhateGiorno fa
  • Tu communiques mal vraiment en plus un vrai combattant ne doit jamais dire qu’il est parfait c’est une erreur monumentale MMA bi beuri neu toubab you leu meune fouff revient sur terre nak

    Black WolfBlack WolfGiorno fa
  • Tu es le meilleur combattent kee on

    VM TvVM TvGiorno fa
  • Reug reug bouma nekone yaw damay kholy kenen ruisse bi il est plus technique que toi molla dak khex del nangou nit dangay humble touti champion nga on est derrière toi

    Paul Maurice Sedar SenePaul Maurice Sedar SeneGiorno fa
  • reug nangoum waaji molla guenue souple....................naak faut l accepter evite d aller dans les mouvement rapide avec lui diem ko jaapp nguen beurréé

    Laye SeckLaye SeckGiorno fa
  • Geum sa bopp bakhna trop mais tu me semble trop suffisant alors que sa combat bii wanena ay failles you beurri qu'il te faudra accepter et corriger si tu veux un jour etre champion en MMA.

    AbdoulayeAbdoulayeGiorno fa
  • Bien dit reug reug sénégalaise dafa xawa sokhor tMit koi melni danioula yéna defaite nekal sisa bop té boul representé kén

    Fallou NdiayeFallou Ndiaye2 giorni fa
  • REUG REUG je le trouve arrogant comme débutant . Les plus grands combattants de MMA affinent leurs techniques jusqu’à la retraite ils apprennent tous les arts martiaux possibles au plus haut degrés ( judo, jiu-jitsu , karaté, lutte , taikwendo etc ) et lui se permet de dire j’ai rien à améliorer. Lolou moy arrogance deug. Tei bou defoul dank nak il fera pas long feu les gars qui sont en ufc il suffit qu’il te fixe et tu est ko.

    Papa gorgui DiopPapa gorgui Diop2 giorni fa
  • Les questions sont bonnes mais si l'entretien dure trop ça devient énervant !

    Idrissa DiaoIdrissa Diao2 giorni fa
  • Warnga diangue comunication nak!

    Abdoulaye DiabangAbdoulaye Diabang2 giorni fa
  • MMA dou lambe reug reug il faut nga nangou critique il y'a des adversaires plus forts plus dangereux k toi tu é un débutant accepte les critiques réy bakhoul champions nga

    Assane SambaAssane Samba2 giorni fa
  • y'a du travail à faire accepte les critiques et avance

    Alexis MendyAlexis Mendy2 giorni fa
  • dor gua KO guani amo defaite

    savastanosavastano2 giorni fa
  • C'est un vrai champion

    Ndour MamadouNdour Mamadou2 giorni fa
  • Reug reug champion la mais dafa wara xolate communication wam dafa melni kou xawa arrogant t beugoul crutique nioune nieup iow lagn andal champion mais soit humble tmt tey respecter say adversaire on voit bien k russe bi dala diang

    LE KOPLE KOP2 giorni fa
  • Jajeuf gaïdé 🦁 dara changer. BELT bi rek yaaga yaaga dikkeu rek

    Abdoulaye DioufAbdoulaye Diouf2 giorni fa
  • Pour la fin du vidéo: tu ne peux être performant dans le mma durant le mois de ramadan. Khabib nurmagomedov n'a jamais eu de combat durant le moi de ramadan et c'est par ce que ça diminue gravement les prestations. Voilà pourquoi durant le combat il continuait à tenir le short de l'adversaire et il a reçu 2 avertissements

    Pierre NdongPierre Ndong2 giorni fa
  • Je ne suis pas un fighter ni coach mais je suis les combats @ufc et @onechampionship depuis des années... À mon avis fair un investissement sur les techniques de combat corps à corps. Fais un bon séjour en Thaïlande pour apprendre bien les arts martiaux, après tu sera champion non seulement dans @onechampionship mais aussi dans @ufc. J'ai remarqué aussi que t'as trop sous-estimé ton adversaire et le gars t'as étudié de A à Z et ça fait parti du jeux. Enfin les défaites font parti du game, bonne continuation 🦁🇸🇳 ❤️

    Pierre NdongPierre Ndong2 giorni fa
  • Tu communiques trés mal. Tu parles comme si les sénégalais souhaitaient ta défaite. "Yow yay outeul sa bopou none. Nangoul critique yi".

    Le PatrioteLe Patriote2 giorni fa
  • Champion bayil wax

    Badara DiawBadara Diaw2 giorni fa
  • Reugg bonne continuation

    Serigne cheikh Talibé BambaSerigne cheikh Talibé Bamba2 giorni fa
  • C’est important la communication dég na bakhoul et aussi si tu veux devenir un champion il faut accepté des critiques

    Ibrahima SidibeIbrahima Sidibe2 giorni fa
  • Tant que tu as cette pensée tu ne pourras être un grand champion. Les critiques ont les acceptes car tant qu'on te critique c parcke qu'il y a des manquement ke tu devras essayer de combler mn pote

    Saturnin NiangSaturnin Niang3 giorni fa
  • Ce jour on n'était tousse avec toi mai ton seul problème c'est ta communication

    Thiéndou DiopThiéndou Diop3 giorni fa
  • Bise bo d'adiek appe Jackie sans bakh na

    Abdou bou NdawAbdou bou Ndaw3 giorni fa
  • Loutakh do sonee nitt koudoull sone amoul feinn way

    Idrissa DiopIdrissa Diop3 giorni fa
  • reug nangoul nak russe bi hight kick bim la diokh debut combat wagni naleu nak

    Craty bay fall youngest dicipleCraty bay fall youngest diciple3 giorni fa
  • Ndam rék reug reug

    Modou galsen tup TVModou galsen tup TV3 giorni fa
  • Courage reuk

    Alié DiagneAlié Diagne3 giorni fa
  • Ki menoul comminuque te epui da gaawa maire adouna da nguay masla te ooyoof

    Tara SyTara Sy3 giorni fa
  • Il lui faudra affûter ses armes en améliorant sa technique de frappe des poings et des pieds; eviter de frapper en mouvement ne pas baisser sa garde dans les retraits, affiner ses clefs. La défaite permet de se remettre en cause et surtout prépare la victoire prochaine. Bonne continuation, champion.

    Arona DemeArona Deme3 giorni fa
  • Tu fais la fierté du senegal mais Russe bi mola gagner Victoire ak defaite nio ande boul naaagou tamit

    Lassy Ibrahima SyllaLassy Ibrahima Sylla3 giorni fa
  • Kii dafa doff xamoul wakhine

    Bingo TopBingo Top3 giorni fa
  • Bro nioune fierté la nioulay guiss guay représenter notre réw,mais il faut guay nangou critique té gua kholat sa communication stp🙏 champion gua yalna gua am ndam si sa combat à venir

    Dizzy Diawara officielDizzy Diawara officiel3 giorni fa
  • Dagaye nago critique nak doula wañi dara

    Mansour NdiayeMansour Ndiaye3 giorni fa
  • REUG reug me semble un peu arrogant. Il faut s'adosser aux critiques pour voir exactement la où se situe ton point d'Achille. Tu dois aussi bien perfectionner tes coups de poing que balance vainement. Le peuple est derrière toi👍 Senegalese and proud

    Ami NdiayeAmi Ndiaye3 giorni fa
  • Moytoul camera yi teh nga defar sa garde bi

    el hadji mor Gningueel hadji mor Gningue3 giorni fa
  • Ki boy bou ndawe moko nara mbote mbotou 2eme pieds wait rk

    aboubakry tamberouaboubakry tamberou3 giorni fa
  • Pour dire vrai toubbi mola meune fop

    Atou DiagneAtou Diagne3 giorni fa
  • doranme yeupa la dale dala door ba ko

    usher usherusher usher3 giorni fa
  • do sorri de koko la meun de del naguou il faut etre humile

    usher usherusher usher3 giorni fa
  • Il fallait le terasser avant de taper comme tu as fait avec les autres, c ton fort.

    Samuel DioufSamuel Diouf3 giorni fa
  • Le gar il est très arrogant

    Tahibou BokoumTahibou Bokoum3 giorni fa
  • Concentres Toi plus sur tes entraînements et evites la presse. Un professionnel ne doit pas répondre à tout le monde. Les critiques font avancer

    Ousmane SowOusmane Sow3 giorni fa
  • C'est normal défaite mom amou fa pask dama guis Arbitre bi souffle baparé

    Hamidou TallHamidou Tall3 giorni fa
  • Soit objective et ne sois pas prétentieux. 👉La clef de la réussite

    soulemane Basoulemane Ba3 giorni fa
  • Reuge Reuge loumou def iow guiri 2 ak elton ngay wakhe lima def ak fima diarr

    Modou AïdaraModou Aïdara3 giorni fa
  • Reug bax gua dh meune gua beuré ms fok guay nangou ndogual nioulay critiqué aussi ak bayi waxé xeut xeut ak xol té xamni fi yallah rék mossi nék franchement ak amna wax yo xamni waro ko wax cmme do sonou ak yenene fini nieupay sonou aussi gua nangou ni gagné naniou la cmme biguay gagné nimou nékhé won en plus yani won 1 combat guanane naniou la diokh si champion prk gni nioulay diokh moy lol yalén meune di feug sa deune leegui nak yallah wane nala bopam ni mome kassé fi nék djam bi amoul loudoul niane ak sante ko soula mayé xolatal communication bi aussi

    Prince MhdPrince Mhd3 giorni fa
  • La communication.... C'est ce que j'aime de Modou lô

    tapha Alias bilytapha Alias bily3 giorni fa
  • Reug reug mayniou diam wadji mola meune foufe

    Ndeye ami SeckNdeye ami Seck3 giorni fa
  • Sawaye dangua rouslo sénégalais yi ta rien a dire nopile

    pape sagna sagnapape sagna sagna3 giorni fa
  • Bravo l'artiste et maestro. On est fière 2 toi. Wince père papy boys

    Vincent GomesVincent Gomes3 giorni fa
  • Reug Reug il faut que tu reviennes sur terre tu n'est pas le meilleur dans cet sport. Sois bcp plus humble et revois ta communication.

    Mamadou SarrMamadou Sarr3 giorni fa
  • Il faut accepté les critiques Reug Reug t'es un champion l'erreur d'hier fait aujourd'hui les grands champions, il faut accepté et augmentes tes entrainements 👏👏

    ligueye Diamou Yallaligueye Diamou Yalla3 giorni fa
  • Aye mbeurr 👋

    Samba SyllaSamba Sylla3 giorni fa
  • Khekh a distance nga wara djiangue mais yaw fi ak djiappantewolen rek do deff dara

    Moustapha SockMoustapha Sock3 giorni fa
  • soo dématé mou nokaate la rék kou soof nga

    elhadji MBOWelhadji MBOW3 giorni fa
  • Reug boulniou sonnal le russe dala meun accept rek té moytou les adversaire russe khekh rek moy sen affaire. Boy demal diangui karaté sinon dou bakh si yaw

    Street Tv online liveStreet Tv online live3 giorni fa
  • Reug néna amoule béne coup bouko dallle khana dafa yakarni nioune tiji laniouye sétanéé wala boomerang 🤣🤣🤣🤣

    laye tireralaye tirera3 giorni fa
  • COMMUNICATION 0

    Bilal NdiayeBilal Ndiaye3 giorni fa
  • Yarou loumla mayoul doulako khagne

    Général niangGénéral niang3 giorni fa
  • Amnna sollo machalah champion rafetna loll pour la sagesse bonne continuation

    Maguatte ThioubeMaguatte Thioube3 giorni fa
  • Mbeur soudé begue ngua dégue rek bayil MMA sport bobou bahoul fofou amoul gualathie dh say mbok yi war nagne la wah degue boudé begue nagnou la wa salam

    Lemou DaboLemou Dabo3 giorni fa
  • Sa coach nala bayi gua beuré ak sa khél

    chikichiki tvchikichiki tv3 giorni fa
  • Reug il es comsa acepton leu

    alioune leyealioune leye3 giorni fa
  • Modestie 00000000000. Bo démé ba nek champion MMA ragal naa ngay dokhé touflittt.. diangal wakh

    Kangam SnKangam Sn3 giorni fa
  • communication zero

    papa allah Ndiayepapa allah Ndiaye3 giorni fa
  • Reug reug champions nga mai communication zéro zéro zéro

    Thierno ToureThierno Toure3 giorni fa
  • Champion gnoune on est derrière toi mai nak combat on t'as déminé sur tous les plans par rapport ak tes combats passés...Critiques yi faut k ngakoy nangou tmt boudé linguay wakh ni sénégalaise yi ngay représente... deugg la on a vu le combat tmt Champion pr ngua donne ko faut nguay ndangou Critiques yi

    Papaalassane SambaPapaalassane Samba3 giorni fa
  • Yokal entraînements yi rk sénégalais yeup pagui sa guinaw bo amé ndam senegal mo am ndam vive le senegal 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳

    Djeynaba DiagneDjeynaba Diagne3 giorni fa
  • Mais pére Khadim Ndiaye loumou poutch ni

    Babacar NDIAYEBabacar NDIAYE3 giorni fa
  • reug mi mo sofff kw

    Papi MazinguaPapi Mazingua3 giorni fa
  • 😄😄 Reug dianguil fight MMAdou thiakhane

    toukoutoukou Yeringtoukoutoukou Yering3 giorni fa
  • Champion ndam rekk goor goor lou rekk dina gueuna bakh vraiment man nga sa métier

    Bamba SeckBamba Seck3 giorni fa
  • Champion deug dey accepté erreur

    Abdou kane NdoyeAbdou kane Ndoye3 giorni fa
  • Non ki moy lo Lou

    Mame s mbaye khasside MbayeMame s mbaye khasside Mbaye3 giorni fa
  • Machalla machalla ruge rug👍👍

    Djibril SowDjibril Sow3 giorni fa
  • Tu vas détruire ta carrière si tu n'accepte pas les critiques et la défaite ,ohh tu n'es meilleur au monde champion ohh

    Boubacar DialloBoubacar Diallo3 giorni fa
  • Reug reug da nga reuy déé , té bakhoul tout le monde à vu le combat le blanc est plus prêt que toi. Seul le travail paye , remue toi , té axecte la volonté divine c mieux. Le meilleur reste à venir inchallah

    Boubacar DialloBoubacar Diallo3 giorni fa
  • Reug reug neina dou sonn khaya

    Moussa BarryMoussa Barry3 giorni fa
  • Reug reug est mal communiquer

    Amadou KamaraAmadou Kamara3 giorni fa
ITworlds