Ouza 2 révèle : "Eumeu Sène mystiquement dagn ko diap, Lac 2 dafa warone..."

5 apr 2021
141 201 visualizzazioni

Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct facebook.com/luttetv/
facebook.com/luttetv/
instagram.com/luttetv/
luttetv.com/
itworlds.info

Commenti
  • Franchement Ouza kou kham lamb leuh

    Yoro GueyeYoro Gueye9 giorni fa
  • Ouza ligua wakh kamile la ya kham lamb.déé

    Jean collin SarrJean collin Sarr9 giorni fa
  • Très pertinent vraiment j'aime bcp ce lutteur

    Papayqs Nf doyePapayqs Nf doye11 giorni fa
  • 👌🏽👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾

    djilly ndiayedjilly ndiaye11 giorni fa
  • Euma du ku nui jel nonu jambarr laa lac du dem paskea da barri wakh

    Lady ShashaLady Shasha11 giorni fa
  • Machalla bamba amna solo

    Khadim NdourKhadim Ndour15 giorni fa
  • Da am ay mbeur yo khamni sa youn len dorè dore you meti gagnez len niou wout ay lay /kila kela sama guembe . Mbeur mom bou barè baparê kholal kanam gui lo guis lolou la wedi guis bokou ci

    Mo MoiseMo Moise15 giorni fa
  • Ouza Nice na toropp...wa mais fo rerr dieuleul Big pato bokkk🦾

    Mouhamed FayeMouhamed Faye15 giorni fa
  • Bien analyse 👍

    Seydi Ibrahima SallSeydi Ibrahima Sall15 giorni fa
  • Diadief ouza DEUG Nice

    Aliou CisseAliou Cisse15 giorni fa
  • Mashalla ouza contane thie yaw jambar

    Talibe Cheikh TvTalibe Cheikh Tv15 giorni fa
  • Mashalla ouza contane thie yaw jambar

    Talibe Cheikh TvTalibe Cheikh Tv15 giorni fa
  • Bien parler Macha alah

    Sirema KabaSirema Kaba16 giorni fa
  • Lac na diangui tailleur tamit lamb yeufi goor leu

    Bamba SeckBamba Seck16 giorni fa
  • ya xam lamb,Lac goordjiguén la...

    Ngagne DioufNgagne Diouf16 giorni fa
  • Ouza 2, borom baakh. Nitt kou cool té wathié bopam. Un grand analyste aussi

    assanari 07assanari 0716 giorni fa
  • D'accorouma Gris ak Lac dé Lac diaroul diokh combat nakharr yawou diall wala body rfm

    Ramos GueyeRamos Gueye16 giorni fa
  • Lamb kheureum kessee la. Afferou koufrou la. Kouci deeee hummmm

    Ibrahima SeckIbrahima Seck16 giorni fa
  • Lac dafa yambar tropp lamb ji moko momone ci bep cote

    Ibrahima SeckIbrahima Seck16 giorni fa
  • C vrai ouza

    Mbaye DiakhateMbaye Diakhate16 giorni fa
  • Ki walahii dafa geum yallah

    Ngarou faye Bou modou lôNgarou faye Bou modou lô16 giorni fa
  • LAC2 techno pôle la meunée😂😂

    Ben SyBen Sy16 giorni fa
  • Kene diapuu ko, bayill len kuu beurré woul rek guene né galadjj la, Eumeu amoull wone forme, entraînement bi dess na luu beurri, Lac mom yambarr, comme d'hab, dokh duu bayii yone.

    Rio MankaRio Manka16 giorni fa
    • Yaw fo deukk

      Etranzei XenosEtranzei Xenos15 giorni fa
  • Tres fort

    jean mboupjean mboup16 giorni fa
  • C'est pértinent

    Yaya DialloYaya Diallo16 giorni fa
  • Na mbeuryi diape lac dane lac mosoul danou wakhdjié barri fi rek

    Yaya DialloYaya Diallo16 giorni fa
  • machalla si liga wakh si bare ak diine

    Serigne Sidy ndiaye 129Serigne Sidy ndiaye 12916 giorni fa
  • wakh nga deuge waye

    Modou SeckModou Seck16 giorni fa
  • Merci ouza

    GALAYE DIOPGALAYE DIOP16 giorni fa
  • Bayi len wakh mo mom ndam yalla rek moko mom

    Ndama TorinoNdama Torino16 giorni fa
  • Machallah

    Astou FayeAstou Faye16 giorni fa
  • Bayil fen lac munut Danel eumeu sene

    basiru bayebasiru baye17 giorni fa
  • Machalla mame Khadim am nga kham khamou lamb wakh ji rafete na

    Kouly NdiayeKouly Ndiaye17 giorni fa
  • Bilan

    Marème SambMarème Samb17 giorni fa
  • Merci beaucoup ouza machallah lac dou dara eumeu sene nékoul sakh

    Hamdy DiongueHamdy Diongue17 giorni fa
  • ouza 2 khana legui amgua sokhna wala kou kham lamb la

    Lou yallah Déf rekk NonoulaLou yallah Déf rekk Nonoula17 giorni fa
  • bonne analyse

    Moustapha DiopMoustapha Diop17 giorni fa
  • Machallah t'es un monstre wallah

    Gamousa CisséGamousa Cissé17 giorni fa
  • Machalla

    Alle NdiayeAlle Ndiaye17 giorni fa
  • Machallah ouza le meilleur analyste de la lutte.🥰🏆✌️

    diallo betadiallo beta17 giorni fa
    • Billaye c la vérité

      Fatou SoumareFatou Soumare16 giorni fa
  • Machallah

    Srgn Fallou NdiayeSrgn Fallou Ndiaye17 giorni fa
  • Diajeuf

    Srgn Fallou NdiayeSrgn Fallou Ndiaye17 giorni fa
  • Kou beugg diéne kaïré beusseulle j’aime 👍

    Soulaye SowSoulaye Sow17 giorni fa
  • Yaw momo ndanan nga uoza 2 Beug nala

    Cheikh dieuredieuf mam asta Mbacke NiangCheikh dieuredieuf mam asta Mbacke Niang17 giorni fa
  • bien

    cheikh Niangcheikh Niang17 giorni fa
  • Liga fi wakh yeupe kéne menouko wakh wakh ga lépe vraiment

    Ousmane DioussOusmane Diouss17 giorni fa
  • La vérité et eumeu séne combat bi momou ko wone

    adam's dialloadam's diallo17 giorni fa
  • Non ouza machallah m eumeu sene dara diotoukoh lac 2 guére limou waxhone laa warone défff mou néfii dii daw rekk 🙏tékk tale sii expérience lamba laa bokou

    Bawane ItnBawane Itn17 giorni fa
  • louma nékh si ouza bou wakhe niou kham sa xol sédd bilakhi

    Pape FayePape Faye17 giorni fa
  • Guii aka bakh nieupou la yéné diamou

    Khadam FallKhadam Fall17 giorni fa
  • Lac de guerre est nul

    toukou batoukou ba17 giorni fa
  • Yarr Lo ame solo len si combat Khadim mi mom manchallah dit ouza 2 🙏

    dame mbenguedame mbengue17 giorni fa
  • deug pir nga wakh lac de guer mystiquement la

    mariem dibbamariem dibba17 giorni fa
  • Ouza 2 diamou ci ioe Lutte Tv ❤️💪

    dame mbenguedame mbengue17 giorni fa
  • Vérité, c était une occasion pour lac

    y'en a marrey'en a marre17 giorni fa
  • Ouza vraiment tu es fort ❤️❤️❤️ machallah 💞

    Modou KaneModou Kane17 giorni fa
  • Grand frére de sang❤

    Ndeye Binta DialloNdeye Binta Diallo17 giorni fa
  • Merci ouza wakh nga lep 🙏🙏

    Faye MballoFaye Mballo17 giorni fa
  • Merci ouza vraiment analyses bi rafetna torop sam mouride sadikhe bi

    lahad bou kharagne Lolahad bou kharagne Lo17 giorni fa
  • Combat lac khawma koumouy yobou stade de mes man mom douma si bokou

    lahad bou kharagne Lolahad bou kharagne Lo17 giorni fa
  • Lac2 yambarla

    Tall AbdouTall Abdou17 giorni fa
  • c’est bien parler ouza 👂👂👍

    ckheikh seyeckheikh seye17 giorni fa
  • Merci oussa2 sa wakh refitna

    Ndeya SallNdeya Sall17 giorni fa
  • Lac mo amoul fiitou mbeur

    Mamadou NdoyeMamadou Ndoye17 giorni fa
  • Billahi sa analyse bi rafetna té DEUG bou werr l'a.

    Abdoulaye BaldeAbdoulaye Balde17 giorni fa
  • Me ouza diokhlenko comba

    Ndiass codouNdiass codou17 giorni fa
  • Vous avez raison ouza 2

    Assane DiopAssane Diop17 giorni fa
  • Kham gua lamb mbeur machallah

    diop el malickdiop el malick17 giorni fa
  • Lac amoul sagnsagne eumeu sait que c’était pas son jour il a géré le combat et lac aurait dû être agressif après l’avoir envoyé chez ardo mais dou pousse dou passe il a trop peur

    TKTK17 giorni fa
  • Mbaye Diop président écurie fass Benno,je suis satisfait de l'analyse pertinente fournie par ouza mais chapeau a Lamine le dénicheur des champions de l'arène

    Babacar FayeBabacar Faye17 giorni fa
  • WAWAW merci 💯💯

    Moussa NdiayeMoussa Ndiaye17 giorni fa
  • Super analyse et pourtant j’avais dit dès le départ eumeu n’était pas prêt mystiquement et physiquement aussi il n’était pas wolayhii

    insa drameinsa drame17 giorni fa
  • Rompràn bouy naw la lac done feth au lieu mou beure 😃😃😀

    Makh FayeMakh Faye17 giorni fa
  • La lutte est un facteur de sius DEVELOPPEMENT.. Les lutteurs ne sont pas des modeles a Suivre. Cest pas la lutte que l afrique va donner a manger a ses enfants. Tout ca pour endirmir le pays.

    Gueye MslickGueye Mslick17 giorni fa
  • Ouza Machallah nan la dieul si télé yi bilay ya man gayi te danga am Yar am talibe

    Sénégal neexnaSénégal neexna17 giorni fa
    • Khana d'où beureh

      Khady BaKhady Ba15 giorni fa
  • Gaston Boule tegeule ti lac comba

    Mass SarrMass Sarr17 giorni fa
  • Da yarou sah ndeysane. Yalnala yalla defal diamb

    Mahamed DiopMahamed Diop17 giorni fa
  • Un bon consultant

    Mbissane KareMbissane Kare17 giorni fa
  • Contane ciyèw Ouza borom bahga ♥️

    Idrissa MballoIdrissa Mballo17 giorni fa
  • Un menteur de première heure. Shit a f...up

    L SL S17 giorni fa
  • Combat bii yagg come confinement Macky sall

    djoloffcdjoloffc17 giorni fa
  • Lac djiguene la wolah😂 en plus lac dafko diékou mystiquement mais amou fite femme sah moko eupou fite ki dou sarap diyammm dou gawa amate combat lac rek....

    Khadimatou Baye niassKhadimatou Baye niass17 giorni fa
  • Wakhou nitt 👏🏾

    Lamine NgomLamine Ngom17 giorni fa
  • Li moy analyse lamb da beuri liguéy kaladj eumeu il à un bon entourage

    Diallo BenDiallo Ben17 giorni fa
  • C'est à dire promoteurs yi nio wara bayi teugg combat Lac, mbeur yi tamit danio wara mankoo bagn ko dieul, nioune amateurs souy beuré niou bagn dem, té mom Yalla defna amoul supporters

    Brazza BrazzaBrazza Brazza17 giorni fa
  • Ouza lolo mome deugue leu

    Cheikh bass Keur massarCheikh bass Keur massar17 giorni fa
  • Ouza 2 you are 100% right Lac is not a fighter he is just a joker

    Shiekhibra Mbackeh DarboeShiekhibra Mbackeh Darboe17 giorni fa
  • Yawe khana do âme komba

    Modou FallModou Fall17 giorni fa
  • Lac dey bisness nek fi di nakh sénégalais yi vive eumeu séne

    Seynabou SarrSeynabou Sarr17 giorni fa
  • Way way way way lingay wakh nekhna

    Ismaïla MbodjIsmaïla Mbodj17 giorni fa
  • LAC MO WARONA FONCÉ

    DIEUREUDIEUF DIADIEUFDIEUREUDIEUF DIADIEUF17 giorni fa
  • Tu dois le prendre comme consultant

    Massar DieyeMassar Dieye17 giorni fa
  • Lac gordjiguene la albaftala

    ndiaye PAPEndiaye PAPE17 giorni fa
  • Merci ouza bien analyser dieureudieuf Serigne Touba

    ndiaye PAPEndiaye PAPE17 giorni fa
  • C'est vrai ousa eumeu degne ko diape moustiquement bou l'aire mou âme blaisure taigthi

    ndiaye PAPEndiaye PAPE17 giorni fa
  • Lac du goor gejen la

    Yusuf KebbehYusuf Kebbeh17 giorni fa
  • Yaw bouléne yap gnigne hana lac2 rek mo wara ataké wakh léne deug

    kou fonck deukamkou fonck deukam17 giorni fa
  • 💥Analyse pertinente 🙌🏾

    Khadim GueyeKhadim Gueye17 giorni fa
  • Bravo tu analyse bien

    Latif salifLatif salif17 giorni fa
  • Merci khadim eume nekol danioko dieko lol sakh bilahi

    Cheikhou KaCheikhou Ka17 giorni fa
ITworlds