Ma Challah Eumeu Sène reçoit les prières de Balla Gaye 2 : "linga beugue ci sa khol ❤️ lepp..."

21 feb 2021
113 336 visualizzazioni

Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct facebook.com/luttetv/
facebook.com/luttetv/
instagram.com/luttetv/
luttetv.com/
itworlds.info

Commenti
  • N'dam bi dey niow inchaallah mon champion de tous les temps

    kawou camarakawou camaraGiorno fa
  • Frère moi je vous aimes fort

    Kouyaté DiadieKouyaté Diadie2 giorni fa
  • Mental acier layorré Emeu ✊🏾✊🏾✊🏾

    Zackaria TounkaraZackaria Tounkara7 giorni fa
  • Je t'aime eumeu séne comme mon père

    Ibrahima DialloIbrahima Diallo8 giorni fa
  • Mashala eum j SS fans Balla gaye Nice na

    Ridial DiengRidial Dieng8 giorni fa
  • Amine 🙏

    Niass bayeNiass baye9 giorni fa
  • Mach alla

    Issa SallIssa Sall9 giorni fa
  • Eumeu rekkk💟

    Sokhna NdiayeSokhna Ndiaye10 giorni fa
  • Ndesann dey retane rek yalla na diam yagg Sénégal

    Alhassane DialloAlhassane Diallo10 giorni fa
  • je vous parle yene Mbeur yi pourquoi bou sénégalais yi amé ay problème do lene si takhaw en ce moment là macky sall il nous fout là merde dans ce pays là vous ne dire rien

    Bamba NiangBamba Niang10 giorni fa
  • Eumeu sene Yallah nala Yallah faye sa xol

    Thierno Oumar SyllaThierno Oumar Sylla11 giorni fa
  • Fans balla LA ms eumeu sene amal diam rk

    Fallou DiengFallou Dieng11 giorni fa
  • Bilay dousama mbeur me khol bou rafet la yor yalla nako yalla defal la diam bilay

    Pape Modou MbeunguePape Modou Mbeungue11 giorni fa
  • Ndam rek champion

    Mamadou NiangMamadou Niang11 giorni fa
  • Non man eumeu sene day rétan rek

    Marie MusicofMarie Musicof11 giorni fa
  • Amine way victoire inchallah s'ils plat par dieu amine

    Awa MbengueAwa Mbengue11 giorni fa
  • Ok c bien merci

    Mamadou DialloMamadou Diallo11 giorni fa
  • Hol bou rafet GA yore bilahi eumeu stp so dane lac GA bayui beure do mbeur

    Ismael FayeIsmael Faye11 giorni fa
  • yalna yalla Faye sa khole

    Thiam ElhadjiThiam Elhadji11 giorni fa
  • Eumeu dou sama mbeur deh mais bagnoumako tamite ndakh kholam mo Rafète ❤️🙌

    Ramos SonkoRamos Sonko11 giorni fa
  • Naysann borom xol Bou nice la Barke serign Bamba Ndam Rék champion ♥️🙏

    L’absolu GueyeL’absolu Gueye11 giorni fa
  • Bayil Sama fans bi Wayy 🤣

    Saly DiaSaly Dia11 giorni fa
  • machalla eumeu la vie est courte

    Charlout SamCharlout Sam11 giorni fa
  • Rafètna

    Cheikh abdoul ahad borom belel GueyeCheikh abdoul ahad borom belel Gueye11 giorni fa
  • Balla Gaye kenn guenou ko rafete khol ❤️

    Hadja diarieta SyHadja diarieta Sy11 giorni fa
  • MAIS FAIR PLAY BI DAFA EUPP ...DèLENN SAGANTè BA BAYI DOGA NEKK AY GANYINN BOUDOUL LOLOU DOU AMM TENSION .. SAGANTALENN ...NA METTI KHOLENN MOHAMED ALI AKK MANGA 2... JOE FRAISER ET ALI ..NA TANG 😂 MANN MOMM MODOU LO AKA KHARARAGN BALLA GAYE DAKA BEURè EUMEU SENE DORRKO 2 0

    Saliou BaSaliou Ba12 giorni fa
  • Niari boroom khol you rafet ✌eumeu sene dinga khamni nioune fans balla gaye yi kou beugue balla niou beugue la yallna jaam yague😊😊

    Jolie SeyeJolie Seye12 giorni fa
  • Eume Diam rék inchallah Codo

    Gueye XalileGueye Xalile12 giorni fa
  • Ô me ema sene l'an molay meti wakh ma dilal sama numéro 👂

    Walowalo WalowaloWalowalo Walowalo12 giorni fa
  • Je l'aime fort Emeu

    bamba Gueyebamba Gueye12 giorni fa
  • Djadiéf ameu💪

    lamane tinelamane tine12 giorni fa
  • Eumeu sene bilahi xol bou nice la yor day réé rék

    Mam’s KoitaMam’s Koita12 giorni fa
  • Eumeu Rek ya yarou te faire play Rafetna bok

    Pablo El FenomenoPablo El Fenomeno12 giorni fa
  • Eumeu yalla nala yalla defale diam ak kheuwale youbari si barké seyedina mouhamad

    Moussa SeneMoussa Sene12 giorni fa
  • Eumeu bala les 2 khole you rafete laniou yore

    Diakhate CheikhnaDiakhate Cheikhna12 giorni fa
  • Mashallah Balla gaye2 rek forever

    Prince KakaPrince Kaka12 giorni fa
  • Machaalla eumue sene ndam rék inchaalla

    Baye saliou DiagneBaye saliou Diagne12 giorni fa
  • Ndam reck eumeu vous êtes genti

    Mamadou DialloMamadou Diallo12 giorni fa
  • Geumnané dounou borom dinamaye ndame niailay Nianall mobari

    NGAGNE LONGAGNE LO12 giorni fa
  • Mais yarounga trop Dina wakhe sama Mame mounianall la insahala

    NGAGNE LONGAGNE LO12 giorni fa
  • Eume amal diame way💗💗💗💗💗

    bouba sarrbouba sarr12 giorni fa
  • Eum le champion des champion,nioniou tok fofou yépp dane gualén yay champion tmt...

    Ngagne DioufNgagne Diouf13 giorni fa
  • Sama mbeur eumeu sene dame rék inchallah

    Moussa DioneMoussa Dione13 giorni fa
  • Toul temps sport sou boléwoul waroule takhalé machahala eumeu sene yalanaco yalla may ndam

    Ibrahima NgingIbrahima Nging13 giorni fa
  • Machalla li rafetna bg2 yalla nala yalla may ndam 🤲

    Cheikh BaldéCheikh Baldé13 giorni fa
  • Mane Lou mélni la beugeu si guisse si ITworlds bi yallah xamnako . Li dafa nice quoi. Yallah na sén diam yageu

    Songjunior ThiamSongjunior Thiam13 giorni fa
  • Nice na

    Tapha KaraTapha Kara13 giorni fa
  • Merci beaucoup à toi

    Matoulove MAMatoulove MA13 giorni fa
  • Eumeu sene yallanala yalla maye ndame

    makhtar seckmakhtar seck13 giorni fa
  • Lii tamit da melni wa droit gnoyy gagné

    Dija CisseDija Cisse13 giorni fa
  • Eumeu yalnala bour yalla défal diame amine/ lac ame ndam si yaw si barki séydina mouhamed psl amine🙏

    BAM'S BAM'SBAM'S BAM'S13 giorni fa
  • Nala yalla may ndam barkep s bamba 🙏

    Ablaye NdiayeAblaye Ndiaye13 giorni fa
  • Man de blh eumeu sén rk la faral beugue ko loll bilahi walahi mais lima beugue rk mou defal mako moye mou Balou balla gaye 2 si lim ko wakhon blh kon Dina kontan trop eumeu yalna nala yalah maye ndam linga beugue yalnako yalah defal nekal si diame alkhamdoulilah

    Ndiaye MansourNdiaye Mansour13 giorni fa
  • Ndame rek champion

    SABALY HadjiSABALY Hadji13 giorni fa
  • C'est bien eume sene pape sarr et le grand bras droit landiane

    amadou souareamadou souare13 giorni fa
  • Machaala li rafetna

    Coura FayeCoura Faye13 giorni fa
  • Lutte TV ❤️🔥

    dame mbenguedame mbengue13 giorni fa
  • Balla gaye ❤️💪

    dame mbenguedame mbengue13 giorni fa
  • Machalla champions contane na si reconnaissance bi en vers ton amie

    Abasse CisseAbasse Cisse13 giorni fa
  • Merci beaucoup eume ligua def nice na trop yalla na yalla fey sa khol

    Aliou DioufAliou Diouf13 giorni fa
  • Eumeu Sene une grande référence, un exemplaire sans faille tjrs égale à lui mm. Entendre eumeu Sene parler me fait plaisir. Longue vie à toi et à toute ta famille qu'Allah le tout puissant et le seul et unique détenteur des pouvoirs vous protège et vous assiste dans vos nombreuses entreprises.

    Mamadou MareMamadou Mare13 giorni fa
  • Eumeu sene yalnala yalla maï ndam sikaw lac de guiers de Aminee yarabi 🤲🤲🤲

    MAKHA HANE SOPE SERIGNE TOUBAMAKHA HANE SOPE SERIGNE TOUBA13 giorni fa
  • Que dieu donne la Victoir Eumeu sène insa'allah combat contre lac2

    Milck SaneMilck Sane13 giorni fa
  • Vrai trompeur nandite yi xame nagne la déh guaye coman on dort

    Babacar KhabaBabacar Khaba13 giorni fa
  • Machala li dafa nice

    Amy colle MboupAmy colle Mboup13 giorni fa
  • Mais nak Eumeu j'ai l'impression que tu t'es pas bien entraîné pour ce combat

    Talla CisseTalla Cisse13 giorni fa
    • Comment tu peux savoir ça

      saliou dioufsaliou diouf12 giorni fa
  • Eumeu li gua sole nicena torop

    Talla CisseTalla Cisse13 giorni fa
  • Machalla j'aime beaucoup mon petit frère Balla gaye 2 c'est mon lutteur préfère mais je respecte tous les frères lutteurs nous sommes des Sénégalais et la vie est courte la lutte est un travail après la vie continue nékaléne sy diam rék Amine yarabi 🙏❤️❤️❤️❤️🙏

    Yacine bou balla guaye2Yacine bou balla guaye213 giorni fa
    • @Adama Seck Machalla mon frère comme toujours vous dite la vérité machalla 🙏❤️❤️❤️❤️🙏

      Yacine bou balla guaye2Yacine bou balla guaye212 giorni fa
    • Deugue nekhoul baniouniou ken mé nak balla gaye mo dei souniou xole ❤️❤️❤️

      Adama SeckAdama Seck12 giorni fa
  • Machallah nitte kou bakh machallah

    Nabou SambNabou Samb13 giorni fa
  • Bilahi pape sarr danga bakh rk diame si iow ému yalla naka yalla maye ndame bou sed goy si barki yalla amine

    dieng mouhameddieng mouhamed13 giorni fa
  • Wouly sa médicaments dou yombou

    Mohamed NdiayeMohamed Ndiaye13 giorni fa
  • ❤❤❤❤❤🥰🥰🥰🙏🙏🙏🙏

    Modou DiawModou Diaw13 giorni fa
  • Eumeu dafmay fathie 😂😂😂😂😂😂😂😂😂

    Mohamed BenzékryMohamed Benzékry13 giorni fa
  • Eumeu sène origina nite le amèricainyi gnoko dèfare made in usa le

    Amadou SowAmadou Sow13 giorni fa
  • Ama baldè original nite le amèricain yi gno ko dèfar made in usa le

    Amadou SowAmadou Sow13 giorni fa
  • Eumeu séne original nite le amèricain yi gno ko dèfar made in usa le

    Amadou SowAmadou Sow13 giorni fa
    • @Bara Diakité dègloma djiko amèricain laye wakhè

      Amadou SowAmadou Sow12 giorni fa
    • made in Sénégal le,kougina nek sénégalais nite daa am,naniou fonk souniou poppe ,Lou américain oppou sénégalais ci nite

      Bara DiakitéBara Diakité12 giorni fa
  • PAPA LAMINE SECK Nice

    FATOU SECKFATOU SECK13 giorni fa
  • I’m not a fan but I like his attitude 💯

    adu boiadu boi13 giorni fa
  • Balla boulko ñanal yalla nala lac dane dh🤣

    Cheikh VIPCheikh VIP13 giorni fa
    • LAC d bou andone ak Malaaka sah, doutakh mou ñémé, loolou rek mooma ci diaakhal

      WARRIOR KEMI SÉBAWARRIOR KEMI SÉBA12 giorni fa
  • Eumeu Yalla na la yalla may ndam champion ♥️♥️ dila begueee

    Isidore MemdyIsidore Memdy13 giorni fa
  • Eumeu séne Balla Gaye Masha allâh nice na GM 👏👏♥️♥️

    Kine DialloKine Diallo13 giorni fa
  • Eumeu sene paréwo dh Bakhna

    BAYE POSEBAYE POSE13 giorni fa
  • Macha Allah

    Bebe eumeuBebe eumeu13 giorni fa
  • Eumeu sen yalla nala yalla lafal thiat rekk te maye la ndam rek inchallaho rabi

    Amèt DiaAmèt Dia13 giorni fa
  • emue rek

    sara couture coutursara couture coutur13 giorni fa
  • 💯❤💯

    sara couture coutursara couture coutur13 giorni fa
  • Eumeu Sene la farale yalnako yalla Maye ndame

    Malick SarrMalick Sarr13 giorni fa
    • Amine

      Mc SoldatMc Soldat11 giorni fa
    • Amine

      Mouhamed NdongMouhamed Ndong11 giorni fa
  • insha'Allah dam rk eumeu🔥

    Ig Billypapis10Ig Billypapis1013 giorni fa
  • Eumeu dafa bakhe

    ndongo ndiayendongo ndiaye13 giorni fa
  • Le grand champion eumeu Séne

    Pape moussa KandélaPape moussa Kandéla13 giorni fa
  • Lolou deh yekini defalouko wakho il est avare

    Modou SeneModou Sene13 giorni fa
  • Yalla na yalla maylla dam

    Malika SarrMalika Sarr13 giorni fa
  • Balla gaye Ama baldé gouye gui lac yalnaléne yalla may ndam inchallah

    Demba PammDemba Pamm13 giorni fa
  • Mom bro bakh la

    Boukary WagneBoukary Wagne13 giorni fa
  • Oustaz Balla guaye adouna amoule bena sollo bilae

    diaw Taphadiaw Tapha13 giorni fa
  • Jeste bi raféte n'a mais yalna yalla may lac de guére ndam si kaw eumeu séne inchallah

    Demba PammDemba Pamm13 giorni fa
  • limine bougniou sonal ak lamb deukeubi dafa mèty

    Awa DiakhateAwa Diakhate13 giorni fa
    • Ioe mom danga dof

      Diaw WadeDiaw Wade13 giorni fa
  • Pape Sarr 🤣🤣🤣

    lahad bou kharagne Lolahad bou kharagne Lo13 giorni fa
    • Aï Waye Boul Ko Rétane

      Mansour DiengMansour Dieng12 giorni fa
  • Eumeu B52 ndam RK niougui sen guinaw

    lahad bou kharagne Lolahad bou kharagne Lo13 giorni fa
  • Yénen promoteur yéwoulen Gaston dalen di tec khel RK mom mouna teugue 8 kilo mom ak macky gnô yamm RK

    lahad bou kharagne Lolahad bou kharagne Lo13 giorni fa
ITworlds