Excellent!!! Balla diouf dits toute la vérité sur la déception sur le combat lac 2 vs eumeu sene

5 apr 2021
58 188 visualizzazioni

Visitez notre site: www.4appuis.net
Ou Telecharger l'application Samacarte pour vos document perdus:
play.google.com/store/apps/details?id=io.ionic.starterSamaCarte
@BG TV @lutte tv @arenebi TV @leewtoo TV @Dave_lamb_diaspora

Commenti
  • Merci bala en vraie dire vous etes le seul lutteur qui a bien commentè ce combat tu un grand champion vraiment rien a dire

    Yakhya SarrYakhya Sarr5 giorni fa
  • Merci le grand champion

    Aliou KamaAliou Kama10 giorni fa
  • Merci frère wakh ga lépeu

    Mbaye BaMbaye Ba10 giorni fa
  • Sama mbeur bii balla diouf 😍😍😍

    Kenza RoutierKenza Routier11 giorni fa
  • Très bonne analyse dotée d'une grande professionnalisme. 👍👏🙏

    OdiliaOdilia11 giorni fa
  • Wakh takh yalla takh guis nako tay

    Mbodj NogayeMbodj Nogaye13 giorni fa
  • Balla cv yag nala supporté mais eume nimou beuré c normal lac djigéne 2 défoufa dara triché rék lafa néké may nako revanche pourquoi lac djigéne 2 deug ga loule bopame

    Gueye MansourGueye Mansour13 giorni fa
  • Lac est ton ami motakh ngakoy défendre ndakh yako bolee ak coach boxe pour mou entraîner ko .lac dou mbeur amoul fiit. Boy oute revanche bo gneuwee dangay gnemee lingay def songueu khekh beuree daan gniii bii lolou mo war lac 2 mais amoul fiit. Del wakh deugu balla Diouf te bayii affaire copain

    Fallou SarrFallou Sarr13 giorni fa
  • Nitt kouy waxx deug daf may néxx

    Elhadji FallElhadji Fall13 giorni fa
  • Combat you néékhoul yeup lac mooko beuré

    momo dkmomo dk14 giorni fa
  • Bien dit Balla eumeu était venu pour gérer sa lutte.vraiment lac à tt fait que personne ne nous fatigue

    JEAN BERNARD SAGNAJEAN BERNARD SAGNA14 giorni fa
  • Il (eumeu) n'était pas prêt phisiquement

    JEAN BERNARD SAGNAJEAN BERNARD SAGNA14 giorni fa
  • Vraiment lac2 amoul dara lougnioukoy wakh si combat bi moko dor yobouko 3fois ardo té eumeu bigniou kham kouko dane yobou ardo bamou délousi day done gayndé bou nieuwé indi diom fit attaqué la beuré combat bi dane la mais cette fois ci môme eumeu songoul doroule diémoul dara balla diouf a raison lac mo def léppe

    Mam’s KoitaMam’s Koita14 giorni fa
  • Un homme véridique que j'aime écouter

    LAMINE DIALLOLAMINE DIALLO14 giorni fa
  • Analyseur deug moy ioe demal tfm. Di djop danga xam lamb

    abdou aziz gadioabdou aziz gadio14 giorni fa
  • iow bayill touh mi mo la sonall khamo sah li ngay waxx mandii ngui mo la sonall

    beuze diomebeuze diome14 giorni fa
  • Bougnou saggane ba Lac 2 dieul roi bi, kenn dootouko jottat parceque do dan ken mais ken doumo dan. Carriere am yep match nul la

    Ahmad DemAhmad Dem14 giorni fa
  • Lac 2 gris lolou 2h de matin lay dièkh

    Ousmane NdiayeOusmane Ndiaye14 giorni fa
  • Iow meune ng féne d

    malick diedhioumalick diedhiou14 giorni fa
  • Je suis d'accord avec une seule chose lorsque vous avez dit toutes les chances étaient du côté de Lac2 mais le fait de dire Eumeu Sene bariwoul je suis pas d'accord allez regarder l' interview de Eumeu Séne il a donné une explication très cohérente par rapport à la chose

    Les Rendez_Vous du Jeune Journaliste RDV du JJLes Rendez_Vous du Jeune Journaliste RDV du JJ15 giorni fa
  • EUMEU DAFA DÉCONNÉ. MOO TEUTHIE LAMB JI YEUP.

    Cheikh BiCheikh Bi15 giorni fa
  • Lou lér ngawakh

    mama afriquamama afriqua15 giorni fa
  • Merci beaucoup Balla Diouf dans tous les Sénégal c'est toi seul qui dit vérité sur cette combat

    Mouhamed GassamaMouhamed Gassama15 giorni fa
  • A bon kon Lac2 botakhayé beuré day teudiou OK😬

    khadim kandjikhadim kandji15 giorni fa
  • Merci bocup balla diouf

    Diapoulo DiaDiapoulo Dia15 giorni fa
  • Eumeu sene pare woul

    Tall DjilyTall Djily15 giorni fa
  • Diadief balla Nice

    Aliou CisseAliou Cisse15 giorni fa
  • Vrai

    Ibrahima DanfaIbrahima Danfa15 giorni fa
  • Bravo Balla ❤️❣️♥️

    Amadou GassamaAmadou Gassama15 giorni fa
  • Eume khaliss laye oute légui Lac dagne la faye sa bore ni eume beuré nonou guaye beuré guisgua nimou mété

    Babacar KhabaBabacar Khaba15 giorni fa
  • Tu as bien analysé bravo

    music please musicemusic please musice15 giorni fa
  • Très belle analyse mais je suis pas d'accord avec toi balla 1 lac et plus jeune et a plus de rallonges que eume 2 lac na jamais attaqué il a mimé des attaques et des jeux de mains de boxe mais ya jamais hu d'attaque proprement dit 3 lac a touché eume 2 à 3 fois eume s'en pour autant attaquer on a dit lutte avec frappe et nom boxe 4 lac a monté plusieurs fois qu'il voulait que les arbitres arrêtent le combat pour une décision médicale alors que setai a lui d'achever son adversaire blessé 5 lors de s'est sortie dans la presse lac avait dit a tout le monde que c'était lui qui avait choisi ce combat personnellement pour des raisons qu'il savait il a parlé de kharé badar alors pourquoi il na rien montré ? 6 vue s'est dernière combat vue les critiques sur sa façon de lutter il devait prouver a tout le monde de la lutte qu'il était un vrai technicien en lutte et non qu'il est le lutteur le plus défensif qui tante jamais rien de l'arène 7 pour terminer je pense que eume peut donner leurs chances aux jeunes tels que le vainqueur de reug reug gouye gui ou sita papa sow ou même tendre la perche a diéne kairé lac aura difficilement un autre combat car investir a perte aucun promoteur le fera

    Lamtoro SowLamtoro Sow15 giorni fa
  • Dafa tapete ragal bo také beut yi khelmi guis

    Diop FayaDiop Faya15 giorni fa
  • Lac gris benen nul encore nnnnnnn doyal naniou ci lac

    Diop FayaDiop Faya15 giorni fa
  • Merci wakhga deug dè

    Bamba DiengBamba Dieng15 giorni fa
  • Balla sincèrement tu doit ouvrir un compte ITworlds Di def ay live tu as beaucoup d’expérience et tu sait ce que tu dit pense d’y svp

    Diouck AlphaDiouck Alpha15 giorni fa
  • machalah balla diouf amna solo

    Cheikh NdiayeCheikh Ndiaye16 giorni fa
  • Balla nitou deugue

    Assane NdourAssane Ndour16 giorni fa
  • Danga doul

    mahammed bojangmahammed bojang16 giorni fa
  • Kan mo sokhlawone combat bi lac de guerre mo warona dieul initiative

    Serigne Mbaye ThiamSerigne Mbaye Thiam16 giorni fa
  • Balla lac 2 sa Kharit lá yako bole ak Moukhamet aly ndiaye waye eumeu ndanane lá

    ndongo ndiayendongo ndiaye16 giorni fa
  • Machalllo merci balla

    Ersilia CovelloErsilia Covello16 giorni fa
  • Non balla diouf tu a tout dit vraiment serieux nakk

    Sarr AbdouSarr Abdou16 giorni fa
  • Tu as parfaitement raison, Eume dou guatt

    Ousmane DiopOusmane Diop16 giorni fa
  • Dacorna si yaw

    Moussa FallMoussa Fall16 giorni fa
  • Yakh mbeure lac2 dala wara menageur diouf comme aye copin guene si staff bi ak lac fan s club moy commenter ni deih tres important

    fallan productionfallan production16 giorni fa
  • ayy way les gars saga ndeye bakhoul .nit defal analyse mais boul saga wadiour ken. Li fo la rek duaroul saga

    Moussa WagneMoussa Wagne16 giorni fa
  • 😂😂balla Diouf setal yalla si ligay wakh khana canal+ gadone setané combat bi

    Mbengue ThiambaMbengue Thiamba16 giorni fa
    • Wala France 24 😂😂😂😂😂😂

      Mansour DiengMansour Dieng15 giorni fa
  • Bilahi ya degue SA ndeye yow balla diouf fehel def Li eumeu def si lambou

    Ismael FayeIsmael Faye16 giorni fa
    • Ya réw

      Mbodj NogayeMbodj Nogaye13 giorni fa
  • Dagaye doul rec moso wah Lou bah si eumeu vete a toma parculo

    Ismael FayeIsmael Faye16 giorni fa
  • Yaw doul khamo doul si lamb

    busnesse khelcombusnesse khelcom16 giorni fa
  • Eumeu la dit ponkal bou téyé boppam monosi dra c c kil a fait hier beuréwoul eumeu xaral sa thies dane moussa ndoye guen beuré

    Assane DiopAssane Diop16 giorni fa
  • Bien dit bro ✌️

    Samba CamaraSamba Camara16 giorni fa
  • Non si Tapha Tine gagnera. Il attendra le combat royal.

    Moussa DiaMoussa Dia16 giorni fa
  • Fega

    Isatou JobartehIsatou Jobarteh16 giorni fa
  • Balla Diouf Ndanan Piiiir Nga Lingay Wakh Akah Tèkou Bilahi

    Masamba KaneMasamba Kane16 giorni fa
  • Il a raison, lac de guiers a toujours lutté ainsi c'est plutôt eumeu sene qui a été méconnaissable mais malgré tout ça lac de guiers devait profiter de l'occasion et achever son adversaire

    Yilé BabaYilé Baba16 giorni fa
  • Mashallah balla 🙏🏽

    doff 5doff 516 giorni fa
  • C'est la vérité tu as tout dis....un homme de vérité.Mais Sénégal mo beurii nafék,Lac def n'a loumou meune.

    Seyni ThiamSeyni Thiam16 giorni fa
  • Lac sakharit moko yorré poussal fi doul

    Abdou SallAbdou Sall16 giorni fa
  • Eumeu dousa moromm doul rekk yow daga farr

    Abdou SallAbdou Sall16 giorni fa
  • Merci balla diouf nitt dangay wakh degue tè yalla takh

    Modou SallModou Sall16 giorni fa
  • Lac neu dieul gris bordeaux ou tapha tine wala eumeu Sene dieul tapha tine

    TKTK16 giorni fa
    • Combat diank bou intéressant sah

      Sokhna Aminata BaSokhna Aminata Ba16 giorni fa
    • @Sokhna Aminata Ba Waw combat djânk leu

      TKTK16 giorni fa
    • Vraiment lac vs gris combat le!

      Sokhna Aminata BaSokhna Aminata Ba16 giorni fa
  • Eumeu mom dafa maguette grand pere la.

    Serigne DioneSerigne Dione16 giorni fa
  • Machalla balla Diouf lac sénégalais dane ko yap rek

    Diamano OmzooDiamano Omzoo16 giorni fa
    • Bilahi Senegal nio bari wakh mai cou wakh deug rek khamni lac mo beure

      Adama MbodjiAdama Mbodji16 giorni fa
    • Mane dama moudj yeureume lac sah yek domou diambour bi ni rek

      Sokhna Aminata BaSokhna Aminata Ba16 giorni fa
  • Machalllah balla 🦻❤🇸🇳🤲🏿

    ibrahima Niangibrahima Niang16 giorni fa
  • Li moy deugue senegal nafek ak far Molène yak

    Isaac DioufIsaac Diouf16 giorni fa
    • Deug nekhoul merci frère

      Sokhna Aminata BaSokhna Aminata Ba16 giorni fa
  • Machallah nice na trop free ❤❤❤❤💯💯💯💯👌👌👌👌

    Maissa SallMaissa Sall17 giorni fa
  • Balla merci pour la vérité j aime les personnes qui disent la vérité Bravo balla continue sur ce chemin euma sene etait venu pour un nul des le matin il etait venu pour le nul

    May YeseMay Yese17 giorni fa
  • Lac 2 koukafi teuguelaty combat niou nokhoula

    Modou KaneModou Kane17 giorni fa
  • Merci champion lac a attaqué et euma reculer

    Dabo NdiayeDabo Ndiaye17 giorni fa
  • BD merci beaucoup

    Fils De Diassing DiassingFils De Diassing Diassing17 giorni fa
  • Balla Diouf le pays a besoin de vous vraiment c'est la verité

    Fils De Diassing DiassingFils De Diassing Diassing17 giorni fa
  • Dégueuna deugueu eumeu parewoule

    Cheikh LeyeCheikh Leye17 giorni fa
  • Yawe wakhal deugue

    Moustapha DiakhateMoustapha Diakhate17 giorni fa
  • Wayi iow lac foumou attaqué nak deffoul dara

    mactar diallomactar diallo17 giorni fa
  • Bravos champion lac mon daf lepou

    Aliou NdiayeAliou Ndiaye17 giorni fa
  • Féliicitation Eumeu nigua def kouy sa supporter rek dasé wara begu en tou ka man conten na si yaw trop amato loy prouvé si lambj mom modon djeulsi revance da warona gneuw wané bopam mé lac 2 mom dama yaakar ni da liguéy promateur yi

    ndiamé seyendiamé seye17 giorni fa
    • 9 défaite 10 victoire ki dakham darra

      Amath DialloAmath Diallo17 giorni fa
  • Bien dit cœur de lion.

    Talla DiengTalla Dieng17 giorni fa
  • Bilahi llou dou raison sama lokho dafa dameu day doul

    elhadji ndoyeelhadji ndoye17 giorni fa
  • Mome Nila Mel mouy layam layami ni eumeu defoul dara

    noco baganoco baga17 giorni fa
  • Balla yaw tu est mecontent mane nga wate ni eumeu beurewoul lac wara gneuw diaye eumeu doler danko bou nekfi di Def ay flexion melni kouy kouy rass Sal yaw niga Mel bou dieume gouyga nga dieume daxar sa xolbi mo nboya mouy layam layami ni

    noco baganoco baga17 giorni fa
  • LAC ne pourra jamais faire tomber dans cet angle, il invite EUMEU au centre de l'enceinte par ce son thioumouckaye était au milieu. EUMEU était atteinte mystiquement

    WARRIOR KEMI SÉBAWARRIOR KEMI SÉBA17 giorni fa
    • Dagay doul rek

      Ousmane DiopOusmane Diop16 giorni fa
  • Vraiment degue leu balla

    Cheikh BaldéCheikh Baldé17 giorni fa
  • Eumeu nimou beurer nonou la waron beurer mounoul dann lac bâ pare diougé si d'effet di sogou lac

    lahad bou kharagne Lolahad bou kharagne Lo17 giorni fa
    • @Papa ngalla Ndoye khalatou mako

      lahad bou kharagne Lolahad bou kharagne Lo16 giorni fa
    • Sa way bayégo

      Papa ngalla NdoyePapa ngalla Ndoye17 giorni fa
  • Merci Balla Diouf

    Marco1 NjieMarco1 Njie17 giorni fa
  • Mashala, il est très pertinent Balla Diouf Kham kham rek lafi wakh Wakh dji rafetna trop

    Youssou SeckYoussou Seck17 giorni fa
  • Lac 2 le lutteur le plus niak diome de l’histoire de la lutte

    Daouda MbowDaouda Mbow17 giorni fa
  • Promoteur bou fi teugueti combats lac 2 rek di nga kham

    Daouda MbowDaouda Mbow17 giorni fa
  • Lac 2 moy mbeur bi gueune niak diome si lamb ji

    Daouda MbowDaouda Mbow17 giorni fa
  • Balla diouf ni laye meuneu wakhé ndakh mome ak mamadou aly ndiaye ay kharite la niou moko présenter lac 2 mais mo niou gueune kham ni lac 2 dafa niak diome

    Daouda MbowDaouda Mbow17 giorni fa
    • @malick niag faralal kou la nekh looou sa probleme la,lac 2 dafa niak diome dafa warone door eumeu sène diap ko daane ko par force mais amoul diome lolou moy wakh dji

      Daouda MbowDaouda Mbow17 giorni fa
    • ioe do sax nite ki loumou wax c vrai ya rien en voir ak mamadou aly ndiaye senegal mo nex koi kou wax da nga far mane eum la faral mei limou wax deug la

      malick niagmalick niag17 giorni fa
    • @Cheikh baye Konteye da nga niak diome comme lac 2 motakh

      Daouda MbowDaouda Mbow17 giorni fa
    • Wakhi doff

      Cheikh baye KonteyeCheikh baye Konteye17 giorni fa
  • Vraiment wakh ga combat bi yeupe

    momo niangmomo niang17 giorni fa
  • 👀💁

    Mariama DiéneMariama Diéne17 giorni fa
  • Eumeu parewoul lac ragual la

    sora bou kharagne losora bou kharagne lo17 giorni fa
  • Eumeu séne c'est un champion il a tout fait dans sa carrière avec des combats diankh. C'était à lac de changer de stratégie puisque wa pikine nanena eumeu mou takhaw.

    gamebayen11gamebayen1117 giorni fa
  • Eumeu sene beurèwoul dara bilay

    khonte Kontékhonte Konté17 giorni fa
  • Eumeu mo daw faralou ma lac waye deugeu reka nekh yalla

    Mbaye DimaMbaye Dima17 giorni fa
    • ✌🏾

      doff 5doff 516 giorni fa
    • Merci!!!

      Sokhna Aminata BaSokhna Aminata Ba16 giorni fa
  • Dég na deug Balla wax nga lép eumeu séne mo teudj beuré bi

    oscaroscar17 giorni fa
  • It was only the referly who was OK!!!

    Pa MboobPa Mboob17 giorni fa
  • Lac mo beug mo warra gneuw woute sii eumeu done na roi des aréne bâ paré d'âne ko eumeu amoule loumuy woutii

    Mbaye DieneMbaye Diene17 giorni fa
    • Beuré niarr mokoy df

      Seydina fallSeydina fall17 giorni fa
ITworlds