Dip Doundou Guiss - Musiba

22 gen 2021
3 130 437 visualizzazioni

In Musiba , DIP reinforces his title as the King in the rap game : he reminds his detractors that he sits on the throne, no matter how hard they try to make it seems like he’s not. Between punchlines and egotrip, he wants to make it clear : he IS their biggest disaster.
Dans ce titre, DIP consolide son titre de King dans le rap game : il rappelle à ses détracteurs qui est le roi, malgré leurs attaques incessantes. Entre différentes punchlines et egotrip, le King tape sur la table et prévient les MC : leur plus grand malheur, c'est lui. #Musiba en streaming et en téléchargement sur toutes les plateformes : orcd.co/musiba
....................................................................................................
Clips officiels : bit.ly/ClipsofficielsDip
.....................................................................................................
Suivez-moi sur les réseaux sociaux :
Facebook : web.facebook.com/dipdoundouguissofficiel
Twitter : twitter.com/DipDunduGuiss
Instagram : instagram.com/dip_doundouguissofficiel
Snapchat : Dip490
.....................................................................................................
Compositeur : Ssadik beatz
Mix & mastering : Karabalik Beatz
Production : Reverse Studios
Réalisation : Bilal Mbengue & Leye Gueye
Stylisme : DoulSy JahGal
Décoration : Yarba Déco
Make Up : Mimi’s Touch
lyrics
REFRAIN
Fuck number one, Fuck number two
Ya ngeek limay fay, moytul baña juum (yeaah, ouuh)
Musiba naarulay
Gëm sama ñaanu yaay
Lëmbé ndakaru ndiaye
Musuma xaddi, bañuma jeng mais duma daanu way
Aka ma gaaw si gars yi
May sa musiba naarulay
Musiba naarulay

COUPLET 1

Comme roof si ceeb
Cere dolli ñeex
Capp ni goor Gui Dieng
Vol si jet, wala doxx si geej
Yokk job du deñ
Kuy bonn di hate
Bombe nucléaire ci sa xol bu wow ni xeer
Même boy dé bul fokni jeex na, may bëss bila God di yé
Investir ci fenn amo saxx bénéfice du doute
Na doon 50 cents sama ben shot, sa fils du jukk
DIP mola mën du gacce c’est comme ku Messi di duut
Ma ngi si trône bi ak ñom Messi jël sama Pepsi di guux
Duma segg si cage
Man la seen soeurs yi di xaar
Maa taxx sen sërr yi di tass
Carrière bi munoko saltel nigger melni sa chemisou pa
Sëg di gass, job lu tax CD bi jarr
Fële jël sa reliquat
Sama cachet sañu ñuko dagg ni bin bin ci sa ndigu Ma
Na money bi teew, xaalis moy gagner guerre bi duma rayante comme militaires
Si kaw lañuy yeeg wacce leen ni adamak awa ak pomme biñu yëy
Sori fi man, duma xooli sa guel même su defe man kesse si story privem
Coow li du jeex fi ba mëwti di dé amatu ñu adversaire mais ño ngi si guerre
Refrain
Fuck number one, Fuck number two
Ya ngeek limay fay, moytul baña juum (yeaah, ouuh)
Musiba naarulay
Gëm sama ñaanu yaay
Lëmbé ndakaru ndiaye
Musuma xaddi, bañuma jeng mais duma daanu way
Aka ma gaaw si gars yi
May sa musiba naarulay
Musiba naarulay

Couplet 2
Every day, may def baña xaar ndaxx dé du jeem
Soxlawuma tuub pour def ko benn buum mën na takk plus de 5 jeeg
Yes we can
Gedd gratte- ciel, dëkki Baraku Bamba fu Trump dem ba nek president
Fu sëtu esclave dila ray ngir chaîne
Tojj sa lu bonn ba mujje ak séy biens
Nigger ëppo njariñ skincaru Michael Jackson ci cimetière
Dangay gunge rek ni frèru Michael Scofield ci biir jail
Damay fayu ba pare mën nangu ni coow du jib kay
Ku xamm kepp kuy rap wolof xamna nombre rappeur bi DIP fay
Tek sama nafsu ci beat bi
Rap yefu dëmm dëg lë kan mo saña waxx ni que Pac bëggul Biggy ?
Sen game bi concours lëmbël la motax malay yokkal ay tama si beat bi
Sa guel la yakoy solal makoy simi, dagg buumu gacce dagg seeni string yi
Sama kumpa nekul books mais rappeur yi publier gul sen streams yi
Ay goat yu vider plassu gettu bëy du sho bu tijji tank rek ñu dem
Dé bi kesse momay taxa tëddi ni roses yi si sa tanku caissou neew
Bëg coow ni intifada Ben Laden
Même dof du sikki sakka lima fi def
God du mëssa àndak ñi di fenn
Par force King bi man la té du deñ

Refrain
Fuck number one, Fuck number two
Ya ngeek limay fay, moytul baña juum (yeaah, ouuh)
Musiba naarulay
Gëm sama ñaanu yaay
Lëmbé ndakaru ndiaye
Musuma xaddi, bañuma jeng mais duma daanu way
Aka ma gaaw si gars yi
May sa musiba naarulay
Musiba naarulay

Commenti
  • Les francophones qui ne comprennent pas wolof, les sous-titres en Français sont disponibles. Vous pouvez l'activer :) REFRAIN Fuck number one, Fuck number two Si tu penses détenir le secret de ma chute, fais attention à ne pas te louper (yeaah, ouuh) Un vrai malheur Toujours tranquille grâce aux prières de ma mère Je suis dans toutes les bouches J’abandonne jamais, et même si je m’incline je ne suis jamais à terre Je suis le meilleur pour t’effacer Je suis ton malheur Ton malheur COUPLET 1 Tel une farce dans du Tiep J’en veux toujours plus Aussi riche que Gorgui Dieng Un vol en jet ou une balade en mer ? Toujours en train de taffer Pendant que tu hates J’lance une bombe nucléaire sur ton cœur et le rend encore plus dur qu’une pierre Et même si tu venais à mourir, ne pense pas que c’est fini : je suis le jour de la résurrection Toute ta vie tu mens, t’as même plus le bénéfice du doute Et même s’il était 50 Cent, ton gars serais à terre après UN seul de mes tirs Il n’y a pas de honte à admettre que DIP est le meilleur ; c’est comme se faire dribbler par Messi Je suis sur le trône avec la bande à Messi, en train de siroter mon Pepsi Je ne suis pas une panthère en cage Tes sœurs n’ont d’yeux que pour moi ; Je suis la raison pour laquelle leurs pagnes tombent Tu ne peux pas salir ma carrière, aussi clean que la chemise a ton père Toujours en train de bûcher, on a fait le job pour que les CD se vendent Et je prends tout, même ton reliquat Personne touche à mon cachet, un peu comme la ceinture de perles de ta mère L’argent est mon arme, je ne fais pas la guerre comme les militaires On monte au sommet pour mieux vous mettre à terre, tel Adam et Eve Loin d’ici, ta meuf ne m’intéresse pas même si je suis le seul dans sa story privée Tant que l’ange de la mort vivra, t’auras pas la paix ; on a plus d’adversaire mais on continue la guerre REFRAIN Fuck number one, Fuck number two Si tu penses détenir le secret de ma chute, fais attention à ne pas te louper (yeaah, ouuh) Un vrai malheur Toujours tranquille grâce aux prières de ma mère Je suis dans toutes les bouches J’abandonne jamais, et même si je m’incline je ne suis jamais à terre Je suis le meilleur pour t’effacer Je suis ton malheur Ton malheur COUPLET 2 Je bûche chaque jour sans attendre parce que la mort ne préviens pas Pas besoin de me convertir pour avoir plus de 5 meufs à ma corde Yes We can J'ai dit non à un gratte-ciel pour vivre dans la baraque à Bamba, dans un pays où Trump a réussi à être président Là où les descendants des esclaves te butent pour une histoire de chaîne Moi je te bouffe et prends tes biens OKLM Nigga, tu n'as pas plus d'effet que la skincare de Michael Jackson au cimetière T'es juste là pour meubler, comme le frère de Michael Scofield en prison D’abord je te rends la pareille, puis on tombe d’accord sur le fait qu’il n’y a pas polémique Si tu connais bien le rap wolof, tu sauras le nombre de rappeurs que DIP a enterré Je pose tout mon être sur le beat Le rap c’est une histoire de vampire, qui ose dire que Pac n’aime pas Biggy ? Votre game, c’est un concours de twerk, raison pour laquelle t’auras toujours du tambour sauvage dans mon beat T’habilles ta meuf mais je finis toujours par la déshabiller ; je fais disparaître le déshonneur tout comme son string Le mystère pour moi, ce n’est pas Books mais plutôt tous ces rappeurs qui n’arrivent toujours pas à publier leur stream Ça se dit goat mais ça remplit la place des nullards ; ici on ne dit pas oui à la première venue Je serai allongé qu’une fois mort, comme les roses au pied d’un cercueil J’aime le vacarme comme l’intifada de Ben Laden Même un fou n’oserait pas douter de mes performances dans le game Dieu est contre les injustes Je suis le King et rien ne pourra changer cela REFRAIN
 Fuck number one, Fuck number two Si tu penses détenir le secret de ma chute, fais attention à ne pas te louper (yeaah, ouuh) Un vrai malheur Toujours tranquille grâce aux prières de ma mère Je suis dans toutes les bouches J’abandonne jamais, et même si je m’incline je ne suis jamais à terre Je suis le meilleur pour t’effacer Je suis ton malheur Ton malheur

    Dip Doundou Guiss TVDip Doundou Guiss TVMese fa
    • 😍dina weuy version français bi

      Ahmadou sara ManéAhmadou sara ManéGiorno fa
    • Lfeek

      Amadou BaAmadou Ba2 giorni fa
    • Ooojf

      Amadou BaAmadou Ba2 giorni fa
    • Vous pensez que Dip dou HOMME+++

      ABO RIDIALABO RIDIAL3 giorni fa
    • family meuno fene

      eumeu niangeumeu niang3 giorni fa
  • This is real talent bars dope and real poetry lines with so much paradoxical . Dip you're unique and rare the way you lay literary together makes it excellent and exceptional

    Tanji Got TalentTanji Got Talent6 ore fa
  • Ngaaka mola dakk rap nak

    Amath NdiayeAmath Ndiaye10 ore fa
  • À quand les 3 millions 👀🔥🔥

    baba wally diafounebaba wally diafoune11 ore fa
  • Dip👑🤴

    Cheikh CisseCheikh Cisse13 ore fa
  • Dip yaye sene bay

    houda fallhouda fall14 ore fa
  • J’ai peur

    Ismaila KaneIsmaila Kane23 ore fa
  • Tu testera toujours king

    Bakary KoumouBakary KoumouGiorno fa
  • 3 million de vue en 1 moi bra vo idole sama royouway

    Ahmadou sara ManéAhmadou sara ManéGiorno fa
  • Qui est la après les 3 M 🖒

    Amath ToureAmath ToureGiorno fa
  • J’y va j Fc

    Nagy BadaouiNagy BadaouiGiorno fa
  • Bientôt 10millons de vues inchallah

    Muhvmēd KaMuhvmēd KaGiorno fa
  • Je comprends pas Wolof mais ce frère a un flow de dingue et les effets spéciaux du clip sont impeccables. l'Afrique avance !

    Temy FARIALATemy FARIALAGiorno fa
  • 🔥🔥🔥🔥🔥

    Kinè OfficialKinè OfficialGiorno fa
  • Da nga guéné musiba rek, deuk bi am musiba ....

    No justice no peaceNo justice no peaceGiorno fa
  • Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

    Sd CSd CGiorno fa
  • Bima sitane demb barah la xamne do nit rap yeufou wampirla bilahi 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

    cheikh dieng italy livornocheikh dieng italy livornoGiorno fa
  • Enfin les trois millions

    Mareme Sarr MbengueMareme Sarr Mbengue2 giorni fa
  • 3 millions de vus en 1 moi jamais vue🙏👁🤗

    Djily kebeDjily kebe2 giorni fa
  • 3 millions de vues en 1mois ils chaud ce mec

    Ndeye ndiayeNdeye ndiaye2 giorni fa
  • KI DEF MONTAGE BII PRO LA DEEE WOWWW

    Experiment Black BoyExperiment Black Boy2 giorni fa
  • Dip walnala yalla are moi je comprend

    Adjaratou Fatou DioufAdjaratou Fatou Diouf2 giorni fa
  • Woooooooooooooooooooooooooooooooooooooy💥💯🎶🇸🇳

    Black kidoBlack kido2 giorni fa
  • KING BABA

    SOULEYMANE DIALLOSOULEYMANE DIALLO2 giorni fa
  • Oh my god,mé c ses capacités sont inestimable oh dip je t'adore u es l king du hip hop bravo bravo bravo

    Coumba LoCoumba Lo2 giorni fa
  • 3 m

    Ibro BaldeIbro Balde3 giorni fa
  • Cool

    aliou diaaliou dia3 giorni fa
  • Do nit 3m de vie

    SCOFLID 100SCOFLID 1003 giorni fa
  • Je confirme qui'il est le Meilleur Rappeur du hip hop Galsen 🇸🇳 vraiment Respect!!!

    Genuine manGenuine man3 giorni fa
  • Dip wagnil dozbi sinon dey doon over doz si rappeur yi nangouléne ndogal sinon guén déh

    L'enfant NoirL'enfant Noir3 giorni fa
  • King du rap galsen🤩🤩💥💫✋

    Oumy TouréOumy Touré3 giorni fa
  • Nekhna dh wayeii Ba ngua wayyé son bii Ba leggui diam amatoul Galsen Musiba nguii si rewmi🇸🇳🇸🇳

    Queen NefertitiQueen Nefertiti3 giorni fa
  • Hee dip danga guisone musibeu bi bou yagu mo Hew ins bi ni si galsen 🤕

    Mouhamed DieyeMouhamed Dieye3 giorni fa
  • iow ya king bi

    Amadou BahAmadou Bah3 giorni fa
  • Bravo dip

    Amadou BahAmadou Bah3 giorni fa
  • Col Nice

    Mariame DiaMariame Dia3 giorni fa
  • 🥰🥰🥰🥰

    Mamematar DiengMamematar Dieng3 giorni fa
  • ❤❤❤❤❤❤❤❤💪💪💪💪💪

    Aïssatou DioneAïssatou Dione3 giorni fa
  • Qui est ici grâce à Trace comme moi ??? ☺️❤️

    Waïti ChiftaKef OfficialWaïti ChiftaKef Official3 giorni fa
  • 🤗

    issa Taylorissa Taylor3 giorni fa
  • Nkm bilay

    Aminata DiopAminata Diop3 giorni fa
  • 3M de vues, 🔥🔥🔥

    Lassana NdiayeLassana Ndiaye3 giorni fa
  • Bonne continuation mon fils tes mamans sont fières de toi 🥰🥰🥰🥰❤️❤️❤️ ndam rek

    CAROLINE GOMISCAROLINE GOMIS4 giorni fa
  • NEEENDEFFF!!! MOUSSIBA NAROULAY AY YALLAH MINIOU SAKK NIOUNE DANIO SONA

    Mame Rane OfficielMame Rane Officiel4 giorni fa
  • 3 million de vue dans un mois🤔

    Amadou TraoreAmadou Traore4 giorni fa
  • 3 milion 😱❤️🔥✌️🇸🇳

    Adama FallAdama Fall4 giorni fa
  • kou sa yaye bagn gua dèh.boul concurence ak boy bi.ss le meilleur de ts.musiba naroulay

    nikita Diopnikita Diop4 giorni fa
  • 3M DE VUE EN UN MOIS

    Joe capoJoe capo4 giorni fa
  • Vous avez vraiment travaillé L'instrumental vraiment ( you are the King brother, everyday you show them something new things 👑👑

    SINEGALEE TVSINEGALEE TV4 giorni fa
  • 3million

    Charles Emmanuel MendyCharles Emmanuel Mendy4 giorni fa
  • 3 millions😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀

    Mouhamed NdiayeMouhamed Ndiaye4 giorni fa
  • Qui ce clip sac jour🕺🏽🕺🏽🕺🏽

    Cisse BaCisse Ba5 giorni fa
  • Ku délusii pour vérifier les 3M j'espère k'il ya kelk1

    DOCHIIDOCHII5 giorni fa
  • Finalement 3millions de vue en 1mois 💪 Si tu es content besal j’aime 👍🏾

    L’homme CoolL’homme Cool5 giorni fa
  • 3 millions de vues en 1 mois dip est le meilleur

    Mohamed SeckMohamed Seck5 giorni fa
  • Tit tok channel 👏👏

    TIK TOK ChannelTIK TOK Channel5 giorni fa
  • 5 millions de vues dans 2 mois c'est possible

    Baye Dame DrameBaye Dame Drame5 giorni fa
  • 3 millions de vues

    Tidiane SyTidiane Sy5 giorni fa
  • 3 millions de vues en 1 mois Nangou lene balla mouye gueuneu metti

    Pathe DiopPathe Diop5 giorni fa
  • A la 3millions😋🤣😂😋🤣😂💗❤

    MLF CREWMLF CREW5 giorni fa
  • Tu est meilleur rappeur

    Birame ndiayeBirame ndiaye5 giorni fa
  • 3 M ouaiiiiiiiiiiiiiiiiiiiis

    Mairame ThiamMairame Thiam5 giorni fa
  • J attendais les 3 millions et c'est déjà fait🤗

    Djoubairou BaDjoubairou Ba5 giorni fa
  • Qui est là pour voir les 3 millions?🔥🔥📈🌍

    Ndiaga Makhtar DiagneNdiaga Makhtar Diagne5 giorni fa
  • Nékhoul dara woup King Baba fuck n'a sound bi mais jaime dip

    Mouhamed SarrMouhamed Sarr5 giorni fa
  • itworlds.info/round/qax_ddyCe61-f4A/video

    SenzySenzy5 giorni fa
  • 3m de vues bravo dip 👏👏👏👏👏je un fan de ngaaka mais bravo pour les 3 millions de vues

    Medvadl Cheikh touradMedvadl Cheikh tourad5 giorni fa
  • 3millions

    Pape FayePape Faye5 giorni fa
  • Ensemble amenons les vues jusqu'à 10 000 000 avant la fin de l'année guys ✊ WE CAN do it togheter

    Malick CissMalick Ciss5 giorni fa
  • kou né fi di vérifier vu yi ba téy manifestez vous.....kouné mo fi néh té mangui fi Idy nanmoul Iphone 6 té mangui fi

    Ahomine BurnAhomine Burn5 giorni fa
  • 3millions cii 1mois mes respect 🖐️

    Jules Brain OfficielJules Brain Officiel5 giorni fa
  • 3 M VIEWS

    Amadou SallaAmadou Salla5 giorni fa
  • 3M🔥🔥

    Abdou Aziz KaAbdou Aziz Ka5 giorni fa
  • 3 millions

    wiiz silva mvwiiz silva mv5 giorni fa
  • Le meilleur rappeur Sénégal 💪

    Amadou SallaAmadou Salla5 giorni fa
  • Nioun 4m de vue moy souniou yiité talou niou bodio bodio😁😁😁😁😂😂😂😃😃😄😄😅 dip yaye bandit maylénma j'aime naak

    Modou DialloModou Diallo5 giorni fa
  • 3 millions 💥💥💪💪♥️ki est là

    Mohameth SeneMohameth Sene5 giorni fa
  • Grand dou nittt ..yonenti gnaa

    La ilaha ilal lahou!!!La ilaha ilal lahou!!!5 giorni fa
  • Way ..may Sa mousiba Narou lahi jaja

    La ilaha ilal lahou!!!La ilaha ilal lahou!!!5 giorni fa
  • Je me demande pourquoi ne pas coupé Le coup de pied donné par le danseur à la jeune fille

    Lamine DiaLamine Dia5 giorni fa
  • 3 millions de vue putain 💪💪👊👊

    čēłłőű šýčēłłőű šý5 giorni fa
  • 3M en 1 mois🥂

    Mo WesMo Wes5 giorni fa
  • 1mois 3M de vue incroyable

    BMB 221BMB 2215 giorni fa
  • Lalle nagn 3 millions d⚡

    Amacodou NdiayeAmacodou Ndiaye5 giorni fa
  • 3 Millions 😍😍❤️❤️❤️

    Gucci BoyGucci Boy5 giorni fa
  • 3000 000

    Baboucar SeckaBaboucar Secka5 giorni fa
  • 3milions en un mois😁😁☝️

    Dip__Jr 10Dip__Jr 106 giorni fa
  • 3milion de vu 💪🏻

    Fatimahh FallFatimahh Fall6 giorni fa
  • 3M mat n Na machallah

    louis mendylouis mendy6 giorni fa
  • 3 million yi mat na fi si Brasil ak liko weur

    real Madridreal Madrid6 giorni fa
    • @real Madrid ah bon , formidable tu t'appelles comment

      Malick CissMalick Ciss3 giorni fa
    • @Malick Ciss senegalês

      real Madridreal Madrid5 giorni fa
    • 😅iow lann nga sénégalaise wala brésilienne ?

      Malick CissMalick Ciss5 giorni fa
  • DÔME NDEYE BILAKHI GAYI YAYE SÉNE BAYE SAMA BÂTE SI KAW FRANCHEMENT FRERE JE SUIS DE TOUT CŒUR ♥️ 💓 AVEC VOUS BONNE CONTINUATION QUE DIEU VOUS BÉNISSE ET VOUS PROTÈGE DIP

    MOZISS BETTY KAYZMOZISS BETTY KAYZ6 giorni fa
  • Le meilleur

    Bassirou NdaoBassirou Ndao6 giorni fa
  • Kiii est là kom moi !!!! Entrain d'attendre ls 3M😎

    RvsS0uL Doundou GuisSRvsS0uL Doundou GuisS6 giorni fa
  • Dip doundou guiss mn fou👑

    RvsS0uL Doundou GuisSRvsS0uL Doundou GuisS6 giorni fa
  • 3 millions de vues dans quelques instants 😉😋💪🏿🔥

    BRKBRK6 giorni fa
  • Dip do nitte❤️💯

    Mbaye seneMbaye sene6 giorni fa
  • Wadial noce

    Bouba JuniorBouba Junior6 giorni fa
  • Ani gniy har 3millions de view yi✍️

    Ndiogou NdoyeNdiogou Ndoye6 giorni fa
  • Qui est là pour les 3millions

    Papa MarPapa Mar6 giorni fa
  • Dip Éric paye lui plus merde

    aissatou Maraissatou Mar6 giorni fa
    • Kouy eric

      Richard ChristRichard Christ6 giorni fa
ITworlds