Eumeu Sene Sort de sa réserve après son Combat J'ai été atteint Mystiquement, Meussouma beuré...?

6 apr 2021
599 194 visualizzazioni

Abonnez-vous à notre Chaine ITworlds: itworlds.info/fast/udfBmVXjm-DTPjYNv8AWvQ?view_as=subscriber Aimez notre page Facebook: facebook.com/becayembayetv/ Visitez notre Site web: www.fmsenegal.info #Bantambatv.
77 419 03 64

Commenti
  • Eumeu ko yapp yén niar nieup beuré wo lén naniou bayi yéneu sénégalais affairou naafékheu

    Bety NiassBety NiassGiorno fa
  • No vrema balla moy sama fans mé emeu ndandane nga

    Amy SarrAmy SarrGiorno fa
  • Xanaa du mystique la daane Bombardier Na gëum yallah te feliciter adversairam

    Beneen TvBeneen TvGiorno fa
  • Eumeu khamal ni yaw diam rekk guay ame

    Ndeye sokhna DiaoNdeye sokhna Diao3 giorni fa
  • Bilaé tonton yayy champion 💪💪💪

    Mame NdourMame Ndour4 giorni fa
  • Vraiment contenen si yaw ndakh lingua sédé si balla gaye 2 sama champion bi

    Fallou BaFallou Ba4 giorni fa
  • Eum yaw wakhe rèk gay dèf yaw gè no sakoyi

    Bamba DiopBamba Diop4 giorni fa
  • Dagua diekhal

    Pape fallPape fall5 giorni fa
  • Courage champion

    awa barryawa barry5 giorni fa
  • Des faiseurs de malin cela va de soi car la lutte n,'est que le culte de la betise

    Mouhamadou KaneMouhamadou Kane5 giorni fa
  • Nandane nga eumeu tigui jaroul justifier wou, balla Nandane la, modou lo Nandane la, gris Nandane la, bombardier Nandane la , LAC vrai fake le, tapete la, dafay rous lo goor

    NSTYLEZ. TMC n.stylezNSTYLEZ. TMC n.stylez5 giorni fa
  • EUMEU J'adore ton sourire

    Alda FernandesAlda Fernandes5 giorni fa
  • Lac 2 ay thiokh leuh amoul ...wah écurie weum nagn ko dieundeul thiokh svp

    Binetou rassoulBinetou rassoul5 giorni fa
  • Lac2 dafa wara bai lamba Du Dan tei du danu Match nil rek yaha derr keseh Mann Gambian la eumeu ndaanan nga

    Abdul sumnerAbdul sumner5 giorni fa
  • Balla moy sama lutteur dh mais bilahi j’adore eumeu séne ndakh deugue bimouy guéné si lamigne bi deugue dafa nékh daale❤️🙌🏾

    Serigne malick mbacké DiopSerigne malick mbacké Diop6 giorni fa
  • Mane dei Balla moy sama mbeur beugu wa Guédiaway mé biii dama méré lac srx Eumeu diam si yaw def gua leep franchement bénen yon moy dak inchallak

    ceerw butyceerw buty6 giorni fa
  • Walahi jeste bi eumeu déf ak balla dafma nékh trop

    Eva DiaEva Dia6 giorni fa
  • Ay way nguir yalla Eumeu boudé amna team dolen massi dougal té yalla takh

    Mboul NgomMboul Ngom7 giorni fa
  • Machalah on t'aime bcp Eumeu wadiatal bou bakh rek

    Mboul NgomMboul Ngom7 giorni fa
    • Qui est daccore que balla eumeu gris modou sont tousse devenu des amis maintenant

      ceerw butyceerw buty6 giorni fa
  • Lac est un imbéciles

    Abdou SeneAbdou Sene7 giorni fa
    • Lac ne mérite pas c cacher

      Abdou SeneAbdou Sene7 giorni fa
  • Machallah fans club pure là Mala beug pure eumeu longue vie

    Maman BopMaman Bop7 giorni fa
  • nekhoule ba nekhoul mais eumeu yaw tamite beurewo. deugue rek nekh nak

    Bugs BunnyBugs Bunny7 giorni fa
  • machala eumeu sene diambar gua

    Elizabeth BrooksElizabeth Brooks7 giorni fa
  • Je suis fier de toi champion😘💟💟💟💟

    Mounass TambaMounass Tamba7 giorni fa
  • Wallahi djambar ga lac dou mbeur

    Coumba DiopCoumba Diop7 giorni fa
  • yi wara boycotté 👎no sa geste ak Bg2 machala

    qopoy dnonqopoy dnon7 giorni fa
  • Vous les lutteurs vous faites toutes des fétiches donc il faut accepter la défaite. T as rien à dire .il faut être sportif.

    Sarr SarrSarr Sarr7 giorni fa
  • Lac d'où dara da nirou woule sakh mbeur

    Adama Malick DraméAdama Malick Dramé7 giorni fa
  • Bilay eume da melni nion boke père et mère bilay da ma la begue menouma sétane sa lamb si salle de bain laye dougue monté ay écouteur ba volume 100

    Adama Malick DraméAdama Malick Dramé7 giorni fa
    • Eumeu bilahii wakh ga deug lac 2 da donn teup aka dall rekk pour wone gayii nee mooguu def dara tee tank yii sakh diogoul

      qopoy dnonqopoy dnon7 giorni fa
  • Non eume ya fi nék ya meune kou nékoule lac li d'où défaite dhe yaw champion nga respect mbeur on é toujours derrière tw

    Adama Malick DraméAdama Malick Dramé7 giorni fa
  • Je vais convoqué les amateurs de lutte pour faire une marche pour que lac 2 arrête de lutter

    Assane KonteAssane Konte7 giorni fa
  • Eummeu, boul wakhati dotouma beuré ak mom . Dél wakh beugatuma beuré ak mom inchalla. Jajeuf mbeur

    Moustapha Kamal Th.Moustapha Kamal Th.7 giorni fa
  • Eumeu bilakhi wafii né

    Pape medoune NdiayePape medoune Ndiaye7 giorni fa
  • Qui est daccore que balla eumeu gris modou sont tousse devenu des amis maintenant

    soniyu ziuysoniyu ziuy7 giorni fa
  • Euma tay bërewoo dara

    Mustataa SiiseMustataa Siise7 giorni fa
  • En t'en que domou sèrére qui parle jamais sérère saymbok mérénagnoula

    Diagne GnilouDiagne Gnilou7 giorni fa
  • Yacodjoh sabaram

    Diagne GnilouDiagne Gnilou7 giorni fa
    • Non eumeu gor deugue la

      soniyu ziuysoniyu ziuy7 giorni fa
  • Jämbàr deugue ngueu maaacha allaah ki ngua doon da dieel mooy thiounné reek koo diapp mistiquement War koo meuneu daan

    ndiaga fayendiaga faye7 giorni fa
  • Eumeu champion gue 👍Lac mome dou beure

    Hamidou AgneHamidou Agne8 giorni fa
  • Je suis supporter de Balla gaye mais eumeu sene je t'adore vraiment legui sama mbeur nga ndakh sa xol dafa rafet

    Pape SanePape Sane8 giorni fa
  • Bilaye soule ndanane souli badola mais yaw mbeur nga diambar nga

    Awa dia SyAwa dia Sy8 giorni fa
  • Eumeu il est bien. Lac 2 bonne continuation. Je suis fier de toi

    cheikh kouyatecheikh kouyate8 giorni fa
  • Douma fans Eumeu mais damako naw franchement dafa digne degou blie machalla

    sotuur aeeisotuur aeei8 giorni fa
    • Ad

      Aly NianeAly Niane6 giorni fa
  • Eumeu bilahii wakh ga deug lac 2 da donn teup aka dall rekk pour wone gayii nee mooguu def dara tee tank yii sakh diogoul

    Youssou DiopYoussou Diop8 giorni fa
  • Lac dou mbeur bilahi

    Issa DiaoIssa Diao8 giorni fa
  • Na bayi beurré

    Issa DiaoIssa Diao8 giorni fa
    • Eumeu takussane buné def ngakofi macha alla dangua mene béss gaindé bi yarunga mene nga béss

      sotuur aeeisotuur aeei8 giorni fa
  • Ndanane koulou ndanane 😀sama mbeur bii yalnala yallah dfl djm rk Yaw ak modou lô ndam siréee khalé by kham limuye deff 😁😁 Athia mbeur

    Ndaye KhodiaNdaye Khodia8 giorni fa
  • Wathié akh amateurs yii wathié supporter yii diambar nga ndanane nga gaindé nga amato loy prouver si lambe d'elle déglou sa encadrement géré sa carrière champions one love eumeu sa beuré mo tah ma beugu leu té dou dégn yalnala yalla diapalé

    Assane SambaAssane Samba8 giorni fa
  • Balla sama gaynder Ndiaye

    Boury KaBoury Ka8 giorni fa
  • Goor yalla deugue gua machalah ❤️ djomm reek gay prouver eume kou am djomm gua amoulo Keen akk nala Diam sonal sa yaye dala gnanal bilay wolay machalah ❤️

    Mamy BaMamy Ba8 giorni fa
  • Kouko déffati nako deegg, ap mbeur dou fénn, mbeur dou tapalé...aaay kouko défati nako deeg ap mbeur dou tricher mbeur dou yambar, 😤diapé sénégalais yi dofff 💃💃💃💃💃😂😂😂😂😂Eumeu, Balla Gaye2, Yekini, Bombardier, Ama Baldé, merci infiniment, gathiéloulén lambe. Fatou Guièr 2 démal nga toog, ngir yalla boulfi dieuleuti beneu combat, doyal na gnou si yow seuk.🙄🙄😏😏😠😠😠😠😠

    Muslim2proudMuslim2proud8 giorni fa
  • Non eumeu gor deugue la

    Djily DiopDjily Diop8 giorni fa
    • Lou lérr laa wakh

      bssni touirbssni touir8 giorni fa
  • jai trop aimé son discours

    vmvdou svnévmvdou svné8 giorni fa
  • mane fans balla gayé la

    vito boss vito boss no stressévito boss vito boss no stressé8 giorni fa
    • C'est vrai je suis avec eumeu

      bssni touirbssni touir8 giorni fa
  • bilahi euma borom bakh la

    vito boss vito boss no stressévito boss vito boss no stressé8 giorni fa
  • yi wara boycotté 👎no sa geste ak Bg2 machala

    drttyu liqmdrttyu liqm8 giorni fa
  • Lac 2 moy enfoiré rek . Yaw kenn du yaw jambar deug ga

    El CheEl Che8 giorni fa
  • Je suis un fan de Modou Lo mais je t'aime💕💕❤❤😍

    Mamadou Alpha BahMamadou Alpha Bah9 giorni fa
  • Mais eumeu nak balla dinala dane dh one bakhga trop beugue nagne la mais dinagne la dane dh 😂😂😂

    Marieme BaldeMarieme Balde9 giorni fa
    • lac dafa raguale rek yow amélo kéne ak

      drttyu liqmdrttyu liqm8 giorni fa
  • Sana xol diekhna si lac thiim. Bravo eumeu courage. Balla ak wa keureum gnoy samay mbeur (sauf Lac maintenant) legui iow yako remplace. Borom vakh nga

    Marieme BaldeMarieme Balde9 giorni fa
  • Eumeu takussane buné def ngakofi macha alla dangua mene béss gaindé bi yarunga mene nga béss

    Aita NdiayeAita Ndiaye9 giorni fa
  • Diamou RK ngayi âme bly

    Ndeyemarie SeyeNdeyemarie Seye9 giorni fa
  • EUMEU BOUL BAY AWMA KÉNE COUEOUL YEW

    BUZZ MIFABUZZ MIFA9 giorni fa
  • Eumeu ya meuna doull lac dakeu leu bangua guéneu sakou yi guay féne Amgua mélokane déh khawma wone ni ningua mel féne bakhoul

    Khady TogolaKhady Togola9 giorni fa
  • EUMEU JE T'AIME BILLAHI

    BUZZ MIFABUZZ MIFA9 giorni fa
  • Tu fais partie des meilleurs.

    Issakha NdiayeIssakha Ndiaye9 giorni fa
  • Ya fi meun dh Eumeu billahi ❤️

    Aboubacry SarrAboubacry Sarr9 giorni fa
  • C'est vrai je suis avec eumeu

    Chekh tidiane ThiamChekh tidiane Thiam9 giorni fa
  • Lou lérr laa wakh

    Mbacké SeckMbacké Seck9 giorni fa
  • Eum bénéne yonne boy bré boul nuyoti kénn lokho.bâ nga nuyo thi lamb dji la khamni da ngay d'Abou.

    Modou MbayeModou Mbaye9 giorni fa
  • Eumeu sa kanam

    Abdou MbayeAbdou Mbaye9 giorni fa
  • Boléne waxé té yalla tax ngéne xamni lac2 mo tané si combat bi ndax mom sax défna touti effort eumeu sax wax nako après combat bi "waroléne ma wonn téyélo sama bop" motax dafa taxaw rék défoul dara. Questioné nagn ko mo bo xolé boubax dafay rafétal di rectifié wax bi coz ay staff faw gnoniko bouko wax parck lolou daf léni yaxal mbeur gnou fayla ay millions sa staff nane la téyél sa bop

    khass Killahkhass Killah9 giorni fa
  • Yaw diabargua bilay

    Penda WadePenda Wade9 giorni fa
  • lac dafa raguale rek yow amélo kéne ak

    Khady GueyeKhady Gueye9 giorni fa
  • billay diabare gua

    Khady GueyeKhady Gueye9 giorni fa
  • Bilahi eumeu sene wakhone na lako si beineu commentaire nila lac de guiers 2 dalayy tardel rek khamoul gatt ragale na bilahi wokhone na lako beurei woule bayi woule dafa ragalll tropp tropp

    Mame Saye SyllaMame Saye Sylla9 giorni fa
  • Eumeu lat 2 amoul diome

    Abu KonateAbu Konate9 giorni fa
  • Eumeu Nguaïdé Nguay Meussa Done Bo Bayé Beuré Sax Nguaïdé Ngua

    Ibrahima Khaliloula HounsahIbrahima Khaliloula Hounsah9 giorni fa
  • Machalla fiér de toi champion 💪💪💪sa kaw sa kaname

    Diogop KaDiogop Ka9 giorni fa
  • 💪💪💪👍👍

    Ibrahima DiopIbrahima Diop9 giorni fa
  • Barki yamlah Eumeu damala beug

    Khadidiatou GueyeKhadidiatou Gueye9 giorni fa
  • Eumeu champion nga lou lérr Lac war nga kholaat sa beuré té di dieul décision, am nga katane loy ragal, khamon sakh biss bo mome warko am ndam,... modou lo ndam rék Incha ALLA

    Seyidina SowSeyidina Sow9 giorni fa
  • Q

    Sila DameSila Dame9 giorni fa
  • Khole bou rafet eumeu

    Sall AblayeSall Ablaye9 giorni fa
  • Mberr yaw diaroul sakh ngay nioue khana nonou yaye Kane mberr pure nga

    Mansour GueyeMansour Gueye9 giorni fa
  • Eumeu sene yow ya Barry wakh barry tapaleh

    Isatou JobartehIsatou Jobarteh9 giorni fa
  • waw kay eumeu diadieuff way on te fais confiance

    Fati SowFati Sow9 giorni fa
  • Champion nga

    Adama FallAdama Fall9 giorni fa
  • 💪💪😇😇😇😍😍😍👍

    Mariama DiéneMariama Diéne9 giorni fa
  • Eumeu yawdal gathia ngalama chapeau a vous mbeur kaamil NGA

    ASTOULO KOBARASTOULO KOBAR9 giorni fa
  • Cœur pour diambar jdi ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

    Pape DavidoPape Davido9 giorni fa
  • Waw kay sama mbeur bi amal diame yaw lanou beugue tay ak soube mala beugue rek té yallah takh soy beuré douma ame diame wallahi taye wnibik hateu

    Tijani DiaTijani Dia9 giorni fa
  • ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

    Pape DavidoPape Davido9 giorni fa
  • Iow tamit beure wo ...wakh ko kéne meunou niou nakh

    Ahmada DialAhmada Dial9 giorni fa
  • Eumeu séne diambar gue nion gui sa gui naw

    Adama CamaraAdama Camara9 giorni fa
  • Eumeu ❤️❤️❤️❤️💪

    Gooo BhffGooo Bhff9 giorni fa
    • @gtoss chddy lac mo bougone Revanche

      Gooo BhffGooo Bhff9 giorni fa
    • Vous avez tout les deux déçu

      gtoss chddygtoss chddy9 giorni fa
  • Fier de vous Eume Sene

    Mariama Aliou DioufMariama Aliou Diouf9 giorni fa
  • Waw lac nonou ladone def mé khamnanou touti si lamb

    Serigne saliou LoSerigne saliou Lo9 giorni fa
    • Vraiment jambar gua mbeur lac modoul touss

      gtoss chddygtoss chddy9 giorni fa
  • Eumeu mi da melni da beug beuré wate AK Balla

    ibrahima ndomibrahima ndom9 giorni fa
  • Wakhoo fi dara...tu as fui le combat .sois honnête waay .

    Pisco KanePisco Kane9 giorni fa
ITworlds